Видео

Создатели

ИСПОЛНИТЕЛИ
Dominique Preira
Dominique Preira
Рэп
МУЗЫКА И СЛОВА
Dominique Preira
Dominique Preira
Автор песен
ПРОДЮСЕРЫ И ЗВУКОРЕЖИССЕРЫ
Yakine Sheikh
Yakine Sheikh
Продюсер

Слова

Reptile Music Yakkamtinaleu Yakkamtina Yakkamtinaaleu Mounouma xarr Nangou ngueu place'am cii sama xol Dieul sama place mom cii xol'am Yakkamtinaleu Yakkamtinaaleu Ken téré wouñou begg té dé douñou ray Negn dem outti guédj bougn dellou cii déx Étincelle bou guiss essence noumouy def Féké souniouy guent nelow beussou dé Yallah mala dengk malaka ngueu lerr Sa yay'ama bett diama lama meyy Amana ba tayy Yallah dou yakkamti dé Kone fananal'ak werr kouy nadjal sa kerr Kay ma wokh la wone la fi noumou mél Danga ndaw té dingueu def lou raw li Kirikou def Boul sissou boul fène boul fëss késsé ndakh siiw dou succès Primaire sama photo classe amna ñouthii moudjou jail Té ñeupeuy niane am moudjeutel bou bax Yensay may lath ndakh Meuwti xamna loutax dé bi gaw Nguène foudeune senni tangk djoubal pengkou di ñane Na dem église yobou sondel bi taal Loutax réne dou daaw C'est parce que réne negn outteul téneu bi baag Bougouma di taggato né nieup Bateau demna bateau boudoul keuppou Capitaine ya woné yone bi for ever Kou fowé sa bopp niou fowéleu Kou domam deuk cii diam dotoul tabakh cii guerre Bou nieupp di outti lampe yaw demal outti leer Kone goudou fane rek laalay nianal Koula khar kham do nieuw Yakkamtinaleu Yakkamtina Yakkamtinaaleu Mounouma xarr Nangou ngueu place'am cii sama xol Dieul sama place mom cii xol'am Yakkamtinaleu Yakkamtinaaleu Tant que ya ngui begg mangui begg Teuth nala cii sama xol Dieul sama thiaabi sanni gueth Yam sama diangue ak ligueey Magg xaliss'am di leew Meytou danou tay cii pakh bi diane yi matt lène Yane meusteu diss ba raw bi yaye di dath cii seuy Jésus Chris meuss na rakhass ay tangk talibé'm Yensay ngueu tane té deñla tane sans ngueu yeggko Xamna ni thiat dou yekh mais ñanal daw thiat bi yeup Buur bi sa biss nieuw na Fataliko ay mame'am Guiss na kou mél comme mom Mane la siguil xol ma Tekki na laaf'am naaw Waayé foumou dieum khawmafa Mom famou dieum xawma Wayé aljana negn koy woowé Yakkamtinaleu Yakkamtina Yakkamtinaaleu Mounouma xarr Nangou ngueu place'am cii sama xol Dieul sama place mom cii xol'am Yakkamtinaleu Yakkamtinaaleu
Writer(s): Dominique Preira Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out