Music Video

{Lyrics}Dip doundou guiss Waawaw Feat Aida Samb
Watch {trackName} music video by {artistName}

Featured In

Credits

PERFORMING ARTISTS
Dominique Preira
Dominique Preira
Rap
COMPOSITION & LYRICS
Dominique Preira
Dominique Preira
Songwriter
PRODUCTION & ENGINEERING
Karabalik Beatz
Karabalik Beatz
Producer
jackiss prod
jackiss prod
Producer

Lyrics

Même si guènte damay weet Soma fassalé kanam Waawaw, waawaw Samay pékhé yeupay diekh Takh ma ladj la Fok ga wakh ma (wakhma, wakhma) Soma diégué lépay leer Doma wanati guinaaw Waawaw Yalla deff na dotoul dègne, nan Beug nala beug nala Baby kaay gnou weet, yaw kaay weetoo bae Kaay gnou weet, Baby yaw kaay weetoo bae Diougueul gnou dem tok né Yaw kaay gnou weeto bae Ich ya ya yi ya Ich ya ya yi ya Baby kaay gnou weet Yaw kaay gnou weeto bae Yaw kaay gnou weeto bae Contane na lol sa bissa diote Kone tay lo diooy damakoy fadj Sonoone ga lol si liko diar Yaw sakh khamga li dou hasard Because I'm before you love me Because I'm because I'm empty into damay weet Soma fassalé kanam Waawaw, waawaw Samay pékhé yeupay diekh Takh ma ladj la Fok ga wakh ma (wakhma, wakhma) Soma diégué lépay leer Doma wanati guinaaw Waawaw Yalla deff na dotoul dègne, nan Beug nala beug nala Hmhmhmhmmmm Li né si yaw mo né si mane Yalla moko deff Waawaw Hmhmhmhmhmmm Li né si mane mo né si yaw Yalla moko deff Waawaw (yeaaaahhhh) Loumay dokh di khool kénène Li si yaw dou si kénène Doumala wétio ak lénène, mbeuguèl Dou dégne Dou dégne dou dégne Waawaw Dou dégne Dou dégne dou dégne Waawaw Si guènte damay weet Soma fassalé kanam Waawaw, Waawaw Samay pékhé yeupay diekh Takh ma ladj la Fok ga wakh ma (wakhma, wakhma) Soma diégué lépay leer Doma wanati guinaaw Wakh ma Yalla deff na dotoul dègne, nan Beug nala beug nala
Writer(s): Dominique Preira Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out