Lyrics

Sa Arras La niou bolè niari rouh yi Adouna dou wone touki Té guissèw niou ba nopi Béna place Tokk niou beuneu sama roues yi Né kou démone touki Té meunoul nieuw balégui Dianakhék baanex Dima keuli keulé Kagne lay done ak nou May Def ba guiss la Dane ma khégne lou gueune nekh Té dou ki dou keulé Nga néwone si Yoon Nou May Déf ma miss la Stagiaire la wone CV bi démna fou né Ndékété Yoo Douma liguey si niom Dou dianerr Dagne ma la wane Mbekté la yooo Cédé bi datch na boudé yaye diour samay dome... Ni Youssou ndour ak Pen Khamone na ni daa niou dadjié té dou nirok len Khamone na ni bess bou niou dadjié Moy dakh Mburok lem Douma la fene Give me your hand Niou andeu dem fenene Dieundé wouma la ken Dou kene si niom kou meune dara si nioune Té nioune sokhla wou niou khoulok kén Nga togne ma ma lay balou Wax lene ma Kagne lay dalou Kou sagna tambambalou Boma méré ma warou Bayi lene niou wax lou lene neex Guissa gouma lou niou wara téré dem Li May yeuk khadioul si ndap dou diekh Bayi lene niou wax lou lene neex Guissa gouma lou niou wara téré dem Li May yeuk khadioul si ndap dou diekh Ké wax ko boumou yakh crédit wam Da nga gueuna fort khétou bone si mane Tate lay Def sou ma la djiégué meune nga sa bord Mate nga li nga done si mane bou doul yaw sama tole kene dou ko ñagué Bokak yaw keur Di fo di ré di Contane Moy sama yéné si yaw mou Antou niou mour la nga ouff sama ndiaboot Je t'aime mon coeur Kene dou niou ré Do degg ndeyssaan Dina la téyé ni mou waré Ba degg diaraboot Ma moitié ma Reine L'autre Moi ma meilleure amie Quand je parle de toi j'ai des larmes Aux yeux je t'aime et tu es toute ma vie Ni youssou ndour ak Pen Khamone na ni daa niou dadjié té dou nirok len Khamone na ni bess bou niou dadjié Moy dakh Mburok lem Douma la fene Give me your hand Niou andeu dem fenene Dieundé wouma la ken Dou kene si niom kou meune dara si nioune Té nioune sokhla wou niou khoulok kén () You know i love you Never dare to leave you You know i need you Every Day Every night I'm thinking about you Night and Day everywhere i go baby i see you There is no one no one like you Nga togne ma ma lay balou Wax lene ma Kagne lay dalou Kou sagna Tambambalou Boma méré ma warou Ni youssou ndour ak Pen Khamone na ni daa niou dadjié té dou nirok len Khamone na ni bess bou niou dadjié Moy dakh Mburok lem Douma la fene Give me your hand Niou andeu dem fenene Dieundé wouma la ken Dou kene si niom kou meune dara si nioune Té nioune sokhla wou niou khoulok kén Song by Leuz Lyrics shared by Diack_D
Writer(s): Abdoul Aziz Fall, Leuz Diwane G Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out