album cover
Freestyle Session, Pt. 2
37
Hip-Hop/Rap
Freestyle Session, Pt. 2 was released on November 12, 2021 by MeloMusic Entertainment as a part of the album Freestyle Session - Single
album cover
Release DateNovember 12, 2021
LabelMeloMusic Entertainment
Melodicness
Acousticness
Valence
Danceability
Energy
BPM81

Credits

PERFORMING ARTISTS
Big Dat X
Big Dat X
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Sidath Youm
Sidath Youm
Songwriter

Lyrics

Conscience du con Science
Bi mën contrecarrer Kangam
Corps kese mu xel am jëriñul
Xañ ko noflaay am
No Fly am si xel la Scofield Micheal
Man Man Kan?
Maan mi musiba tul mëwti moom ay xool
Reccu tópp si jëf
Fexe na feent
Feey si Giraawaale
Giir a walle
Wala wàlliyaan a wundu
Bii goom u robaale
Topandoo Tópp Tendance
Taru ma teel ma tardel
Tar Tiis Takku Taxaw Tarxiis
Tribunal tëjji Jail
Picc bëgg na rëcc si kaaf am
Kep ko xañ ko Feex am
Labyrinthe si Dark similaire
Tax tay ken mënatu fii xam
Fii Goor Di Sakku goor
Fii gaaw si Japp door
Sama xalima Sen jëf
Xaatim li nëbbu nga Soor
Maa ngi Si yeen neen
Mën ta Tax ma nek si yeneen
Yen Bi ne bët si yeen
Yenu Djibril Si Yonent
Tabarfakalah Xel mi flashback si Yussufa
Japp nañ ko ràpp tëcc Té liy
Tuuma m xuus u fa
Kon Jaaxaluma Soo may xool
Dima yeene jaxalnama
Sa paaka bi ngey nàmm
Soo paree fékk Jaaxaan nama
Jarul di ree sama kanam
Dëmm nga si beneen anam
Sa xalam buum gi Dàgg
Ndax xaal am si sama Xar Kanam
Si Kàtan am la Nafsu gi dee
Wan ma yaw la Man la Kan
Yaw la Kan? Suuf ban
Délul ngir mëne ko Xam
Jamaïcan ba ngi dëkkee woote
I and I Thing
Jàkka Julli Waaw seetul
Bu Xol bi setul do nothing
Bombaklate Dem like mi tel yaah dis mélo music inady Place
Bombaklate Dem like mi tel yaah dis mélo music inady Place
Written by: Sidath Youm
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...