Lyrics

Deff Music Zeus (Zeus Zeus) Thiap thiap sauce Check Tchi kaw tchi kanam (tchi kaw) Boul lathieté fana (tchi kaw) Hey Thiowli mana (tchi kaw) Boul lathieté kana Yaag may seen tchi kaw thi kanam (tchi kaw) Boul lathieté fana (tchi kaw) Hey Thiowli mana (tchi kaw) Boul lathieté kana Yagmay seen si kaw si kanam (tchi kaw, tchi kaw) Thiapathioly (tchi kaw) Hey tchi kaw Boul lathieté kana (tchi kaw, tchi kaw) Thiapathioly (tchi kaw) Hey (hey tchi kaw) Fuck séni règles guissoumako douma diank Yallah ak Gueye rek laafiy sant waw Meme bookoy wakh si souf boy maguessi kaw ni jant Maa shaa allah ma laali bant Loutakh bou goud lagnmay laalé Dou am téguiin boumlay waathié Xath bou mbeuw ngueu teh doo maaté, maalay faalé loutakh Dieul sa gatt gui def si valise Diaaré Paris dem italie, Rap bi dokhoul maagui niaaly Accélérer dikaat Time is money loutakh loo gueun beuri temps di banque Ballou fital nekoul gamou Fifa ODCAV Gueumeul yallah comme bi Deschamps di woo Benzema Nigger coup d'Etat bi maakoy poser sans ben conséquence Succès la mèrebi niaan, rap galsen mayma nopp Xam ma par accident boum nga tek ma choc Méréma di sakhar sa guel bi manela nopp Fouleu mooy diaay dakhar Niakk fayda sa bopp Tchi kaw tchi kanam (tchi kaw) Boul lathieté fana (tchi kaw) Hey Thiowli mana (tchi kaw) Boul lathieté kana Yaag may seen tchi kaw thi kanam (tchi kaw) Boul lathieté fana (tchi kaw) Hey Thiowli mana (tchi kaw) Boul lathieté kana Yagmay seen si kaw si kanam (tchi kaw, tchi kaw) Thiapathioly (tchi kaw) Hey tchi kaw Boul lathieté kana (tchi kaw, tchi kaw) Thiapathioly (tchi kaw) Hey (hey tchi kaw) Tchi kaw tchi kanam (tchi kaw) Thiapathioly (tchi kaw, hey tchi kaw) Boul latché kana (tchi kaw, tchi kaw) Thiapathioly (tchi kaw, hey tchi kaw) Hey Gnidaat Kheep rappeurou village Sen thiokk yi laay guitare Gueun di reew ni fisha Zeus toth na reew mi bilaay Doyla tontu si ladj Waagnil sa dayak di laab Khontal khel mi syllabe Si kaw sa kanam comme maquillage Fii wak yaw mal kiyam Rayla dagann comme si jihad Roukhal nikouy billard Yoonou tekki laa dieul ila Wave Ecobank Ria Realité bilay reukat Tankou talibe di ziaar motherfuck Poucave ni 6nine Sa guel laay 6neuf Oothentik moogui nice Sonwam yi sikk neu Nieuw doumeu leen si mic nioumay diaay wowlé beut Everyday every night ma diapleen di teuf Tchi kaw tchi kanam (tchi kaw) Boul lathieté fana (tchi kaw) Hey Thiowli mana (tchi kaw) Boul lathieté kana Yaag may seen Tchi kaw thi kanam (tchi kaw) Boul lathieté fana (tchi kaw) Hey Thiowli mana (tchi kaw) Boul lathieté kana Yagmay seen si kaw si kanam (tchi kaw, tchi kaw) Thiapathioly (tchi kaw) Hey tchi kaw Boul lathieté kana (tchi kaw, tchi kaw) Thiapathioly (tchi kaw) Hey (hey tchi kaw) Tchi kaw tchi kanam (tchi kaw, tchi kaw) Thiapathioly (tchi kaw, hey tchi kaw) Boul latché kana (tchi kaw, tchi kaw) Thiapathioly (tchi kaw, hey tchi kaw) Hey kou taathiouwoul Kou Taathiouwoul Mané kou taathiouwoul Kou Taathiouwoul Niou dem hey Kou Taathiouwoul Niou diaay sa maam Dieunder ko album teh dooko cons Kou Taathiouwoul Niou diaay sa maam Dieunder ko album teh dooko cons Thiapathioly
Writer(s): Baye Dial Gueye Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out