Lyrics

Fauk Succès wathimaa thiono (thiono, thiono) Beugouma doon kou niak solo (solo, solo) Boo wakhoul money no no no (nono nono) Dam beug tekki dound sama life OKLM (oh) OKLM (oklm) OKLM (oh) OKLM (oklm) OKLM (oklm) OKLM (oklm) OKLM (oklm) OKLM (oklm) Man i got OG neggers on my right Man i got OG neggers on my left Everything is Okay No pain No gain Oulalaha Ligueeyou ndey agnou dom Meunouma ko bagn di saur Ba wakh bou bonn ak pekhé noon Yallay kassé lay fek sama khol bee Fauk Succès wathimaa thiono (thiono, thiono) Beugouma doon kou niak solo (solo, solo) Boo wakhoul money no no no (nono, nono) Dam beug tekki dound sama life OKLM (oh) OKLM (oklm) OKLM (oh) OKLM (oklm) OKLM (oklm) OKLM (oklm) OKLM (oklm) OKLM (oklm) Rakk dji wathi meu (wathieu meu) Daan naala wooroul kou daan dangay feeter kaw (feeter kaw) Bou kouné wakhoon fouy sa diaar diaar Nga xamné tekké beuri diam diam Devant la provoque moi suis posé OKLM (oklm) J'suis mal desiré comme les condés aux HLM (aux HLM) Besoin de soutien mais non personne ne m'a aidé (ne m'a aidé) Maintenant qu'on est en haut l'objectif reste le sommet (hey) Fauk Succès wathimaa thiono (thiono, thiono) Beugouma doon kou niak solo (solo, solo) Boo wakhoul money no no no (nono, nono) Dam beug tekki dound sama life OKLM (oh) OKLM (oklm) OKLM (oh) OKLM (oklm) OKLM (oklm) OKLM (oklm) OKLM (oklm) OKLM (oklm)
Writer(s): Baye Dial Gueye, Mouhamed Loucar Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out