Lyrics
Ya ma gënal li fi ne
Lepp ba na
Adduna'k li ci biir
Ba na wóor na ma
Let me be
They be below my desires
I no dey look em
Money, gold, silver
I no dey see em
Imma look past to it
I'm on my gigas
(Gigas, gigas, gigas, gigas)
Yeah, My vibes go kill em
Or mba xaalis, mba diamant
Li ma ci gnor amul ba ma
Sa maam Ibliss mënu ma
Jëlee ci li ma nekk ba ma
Or mba xaalis, mba diamant
Li ma ci gnor amul ba ma
Sa maam Ibliss mënu ma
Jëlee ci li ma nekk ba ma
Konn bama
Konn bama
Konn bama
Ci li ma ne
Konn bama
Konn bama
Konn bama
Ci li ma ne
Konn bama (Hey)
Konn bama (Hey)
Konn bama
Mann sant na
Ku tedd ki
Ni Mu fexee
Bama tekki
Mënu ma ko xayma
Ndekke li
Romb na ay kurama
Mann sant na
Ku tedd ki
Ni Mu fexee
Bama tekki
Mënu ma ko xayma
Ndekke li
Romb na ay kurama
Kurama
Kurama
Kurama, Kurama
Sama dund sellal nga ko
Li ma bëggoon jox nga ma ko
Dajji sama jéng
Gnongal sama jëmm
Bamay kenn
Te nekku ma gnaar
Don't (stare too much)
Run away, run away
Just because
Nangu ko moy joxe overdose
Look a bit then enough
Konn bama
Konn bama
Konn bama
Ci li ma ne
Konn bama
Konn bama
Konn bama
Ci li ma ne
Konn bama (Hey)
Konn bama (Hey)
Konn bama (Bama)
(Hahahaha Magikara)
Ya ma guënal li fi ne
Lepp ba na
Adunna'k li ci biir ba na wóor na ma
Writer(s): Cheikh Ndiaye, Fatou Mai Ndiaye, Mame Khadim Ndiaye, Ndeye Ngoné Ndiaye
Lyrics powered by www.musixmatch.com