Credits
PERFORMING ARTISTS
Defa
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Ndeye Fatou M'Baye
Songwriter
El Hadj Mamadou Malick Dienna
Composer
Kemessin Kanoute
Composer
Lyrics
Mame birame ak daba ndiaye
Moytulén ma mame birame
Mok daba ndiaye
Mame birame ak daba ndiaye
Deuké dieuw di dieuw ni Rek
Mok daba ndiaye
Def ma nima yalla def ma nopal la soma defoul nima yalla def ma diakhal la
Def ma nima yalla def ma nopal la
Soma defoul nima yalla def ma diaxal la
Dégu na day tokh boone
Niou bone Rek lay andal
Mouy souba di ngon
Dou fananal dou yendal
Dégu na amna dome
BOU xamoul kouy bayam
Nitou goudi la day diay yaramam
Lou ko nex sol fok ni todj na fi
Thioki thioki Romb Wa kogn bi
Kou ko guiss fok ni amoul soucis
Ta Sen keur gui sougnou agné dougnou bi
Mame birame ak daba ndiaye
Moytulén ma mame birame
Mok daba ndiaye
Mame birame ak daba ndiaye
Deuké dieuw di dieuw ni Rek
Mok daba ndiaye
Def ma nima yalla def ma nopal la
Soma defoul nima yalla def ma diaxal la
Def ma nima yalla def ma nopal la
Soma defoul nima yalla def ma diaxal la
Fi dagnoulay dougou xamal la
Fougnou dem togué la
Tek si yakeula
Lane mo takh guisso si Mane Lou bakh
Boula si dara nakh ni ma mel yalla la
Show me love not wickedness
Sétalal sa xol dou tax mou wagni la
Wax djou bone famou djougué la thiossano
Léléléééé
Mame birame ak daba ndiaye
Moytulén ma mame birame
Mok daba ndiaye
Mame birame ak daba ndiaye
Deuké dieuw di dieuw ni Rek
Kofi geunoul geunoula waw
Borom yaye djou bakh kouko yéné fandé
Kofi geunoul geunoula waw
Borom yaye djou bakh kouko yéné fandé Waw
Kofi geunoul geunoula waw
Wakh djou bone deukou fi famou djougé la thiossano
Kofi geunoul geunoula waw
Kofi geunoul geunoula waw
Wakh djou bone famou djougué la thiossano
Written by: El Hadj Mamadou Malick Dienna, Kemessin Kanoute, Ndeye Fatou M'Baye

