Credits

PERFORMING ARTISTS
Abdou Guité Seck
Abdou Guité Seck
Lead Vocals
COMPOSITION & LYRICS
Abdou Guité Seck
Abdou Guité Seck
Songwriter
Ousmane Ka
Ousmane Ka
Arranger
Bril
Bril
Arranger
PRODUCTION & ENGINEERING
Abdou Guité Seck
Abdou Guité Seck
Producer

Lyrics

TANGUAL
Diogual guaaw nioun niou dem balla mouy nieuw
Ndakhte moom nena diggënte nekhou ko
Mone kham na ni dara douniou feweule
Waya ne noumou meun def di na gniou dëdële ( bis)
Woo ! khale bile beug naa laa
Boma nakhe di nga ma gagnë noon ba contaan
Diogal ma
Diogal ma
Diogal ma ma beggal la Diogal ma
Diogal ma
Diogal ma niou dem fanenoo
Diogual gaaw nioun niou dem blow, blow ba dano
Diogual guaw nioun niou dem fe fe wa guën fi
Diogual guaw nioun niou dem balla mouy nieuw
Ndakhte ne noumou meun def dina niou dëdële
Woo ! khale bile beug naa laa
Boma diouye di nga ma gagnë noon ba contaan
Diogal ma
Diogal ma
Diogal ma ma beggal la Diogal ma
Diogal ma
Diogal ma
Diogal ma
Diogal ma
Diogal ma
Diogal ma niou dem fanenoo
Gone gui lou mou lath
Diokh ko
Gone gui loumou lath
Diokh ko
Boufi laadie kani
Diokh ko
Bou fi laadie bongbong
Diokh ko
Bou fi laadie « TANGUAL »
Wooo boul ko diokh
Tangual booboo ma yobe lima dal
Gone gui lou mou lath
Diokh ko !
Gone gui loumou lath
Diokh ko !
Boufi ladji kani
Diokh ko !
Bou fi ladjie nokkos
Diokh ko !
Bou fi ladjie pobare
Diokh ko !
Bou fi latdie tangual
Woooy boul ko diokh.....
TANGUAL booboo ma yobe lima dal
Boulen koko may ndakh gueweul la
Lolou andou ma thi
Boulen koko may ndakh toroodo la
Yeufi diondo la reck
Boulen koko may ndakhte li la
Wakhi kassaw kassaw
Boulen koko may ndakhte le la
Futilité la reck
Boulen koko may ndakhte laobe la
Man andou ma thi
Boulen koko may ndakh te teugu la
Yeufi diondo la reck
Boulen koko may ndakhte li la
Wakhi kassaw kassaw
Boulen koko may ndakhte le la
Futilité la reck
Yefer bi nieuw aki dodiam
Nga oubil ko nekk
Dalal ko tekk thi di ko berndel
Alal dong gua guis
Boulen koko may ndakhte li la
Wakhi kassaw kassaw
Boulen koko may ndakhte le la
Futilité la reck
Diogual gaw nioun niou dem blow
Blow ba daano
Diogual guaw nioun niou dem fe
Fe wa gën fi
...FIN...
Written by: Abdou Guite Seck
instagramSharePathic_arrow_out

Loading...