Music Video

Featured In

Credits

PERFORMING ARTISTS
Gun Mor
Gun Mor
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Momar Ndiaye
Momar Ndiaye
Songwriter
Mouhamed Loucar
Mouhamed Loucar
Songwriter
PRODUCTION & ENGINEERING
Freshiiibeatz
Freshiiibeatz
Producer

Lyrics

This beat is Fresh La la la la la La la la la la La la la la la La la la la La la la la la La la la la la La la la la la La la la la Oh yeah We know Oh yeah You know Oh yeah They know Oh yeah Figua diogué Nimou soré Figua yeksi betoul kene Sounou kanam gua dorè Donone boy bou ndaw nioulay setane si kaw scène Guissone si iow Lou yémé (Guissone si iow Lou yémé) Legui nieup guis nagn nigua yémé (Guiss nagn ni nga yémé) Dou mane reka ko sédé (Dou mane reka ko sédé) Moussougn guiss sa kanam loudoul niémé (Kanam loudoul niémé) Anhannnnn Ragal niémé wouko badiko fréquenter Gun ak défaite victoire moy meusseu dox sisen digueunté C'est déjà fait Gun ak boppam lolou Lagn diguanté Moussougnko ngemb mou dem beuré nieuw indil niou gatié Guissouniou fougnko daké Omar keita newone nala lodefa geune lo defoul Boul meusseu wax balene niouy wax oubil sa xel bi degloul Yagui si yone boy dox ba xaméto sa bopp deloul Xaley bou boppam oyofoul gua tegg la yene bi teloul Ey petit frère boul tegui tank Deko tangual bamou tangue Fils moytoul doug si camb Garannn si iow lagni diang Thia kaw thia kanam amoul diade Même soniou wowoul dagni diap Na fane yi goud amal diam Nala yalla mousseul si thiate Goooooo
Writer(s): Mouhamed Loucar, Momar Ndiaye Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out