Music Video

Featured In

Credits

PERFORMING ARTISTS
Gun Mor
Gun Mor
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Momar Ndiaye
Momar Ndiaye
Songwriter
Mouhamed Loucar
Mouhamed Loucar
Songwriter
PRODUCTION & ENGINEERING
Freshiiibeatz
Freshiiibeatz
Producer

Lyrics

Yes I'm a rebel Miner na sama zone Kou nieme na Kaye Téréw ma kene sama kogn Boudé dang ma Degeul Doma meusseu pésé Ladjal gni beugone dawe niou game niata balle laniou késsé Dama wex ni leweul Baxouma si xolou maguette Rakeu Ndaw wouteul fo lakatou balaguama guet Bougouma armé national bi guéneu dima wanted Ndax Listou rappeurs yiniouy geuneu soralé jsuis en tête Yes I'm a rebel Sam boppay sama forêt fils Ndirowoumak keneu fi guisna niguene maye xoley fils Sama xel moy sama doley makoy yokk doley fils Falew ma sax president yoo fuck all his authorities Man I'm a rebel Anhhh Yeah yeah Yes I'm a rebel Me, myself and I We're all rebels Anhhh Yeah yeah Man I'm a rebel (Rebelution) Me, myself and I We're all rebels Extremophile ni tardigrades Si mane crime you geuneu sedd paka poute ak ndiambi tate Déf kom temps boy yewou Fadjar sathi mango sandica Lois yi respectèwougn ma motax mane respectéw ma loi Niggah I'm rebel Damay takeu yegeul level up Takeu manane Shine faylak acide si tu fais le thug Diameugeune si yene bala maleni firil mbari feute Dama ma haïtienne comme haïtien vite ma déf fi feu Yes I'm a rebel Sam boppay sama forêt fils Ndirowoumak keneu fi guisna niguene maye xoley fils Sama xel moy sama doley makoy yokk doley fils Falew ma sax president yoo fuck all his authorities Man I'm a rebel Anhhh Yeah yeah Yes I'm a rebel (Rebelution) Me, myself and I We're all rebels Anhhh Yeah yeah Man I'm a rebel (Rebelution) Me, myself and I We're all rebels
Writer(s): Momar Ndiaye, Mouhamed Loucar Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out