Lyrics

Ginger me Damala diox sama xoll baby You really know what you mean for me? Depuis nga dem dama low baby Yeah Baby ginger me Expliquer nala ba sonnou baby You really know what you mean for mean for me? Ndam linga dieul diox ko souñ noon yi Yeah Yeah Dance for me Baby come back to me Souba yall nama yéwou ñou wax ni Li yeup dou wone deug wayé Cauchemar Nék ak yaw moma meuna diox plaisir Baby come back to me Boudoul ak yaw awma avenir Boudoul ak yaw beugatouma contact Yaay sama dope Dangay tax douma lazy Yeah Baby come back Dou mala may dara com d'hab Soma reuthié doma rombat Yeah Baby come back Baby come back Dou mala may dara com d'hab Soma reuthié doma rombat Rombat Rombat Rombat Ginger me Damala diox sama xoll baby You really know what you mean for me? Depuis nga dem dama low baby Yeah Baby ginger me Expliquer nala ba sonnou baby You really know what you mean for mean for me? Ndam linga dieul diox ko souñ noon yi Yeah Yeah Yaay bôy déllou sill Yaay bôy dañ may feel I'm a boy and they know it Mais mane yaw rek lay topp Aka ma comp say motif Bae doundou sans yaw dinama kill Lou meunti xew Boul bayi xell Guemeul sa bopp té xam Yay kila folli Yay ki guéné sama folie Sama mbëguél dou meussa déñ Dima firé Té linga ragal dou am Beugou malay sori Kaay ñou dem ba Santarém Sama saytané yaw la Limay téré nélaw Yaw rék kako sañ Yeah Baby come back Baby come back Dou mala may dara com d'hab Soma reuthié doma rombat Yeah Baby come back Baby come back Dou mala may dara com d'hab Soma reuthié doma rombat Rombat Rombat Rombat Ginger me Damala diox sama xoll baby You really know what you mean for me? Depuis nga dem dama low baby Yeah Baby ginger me Expliquer nala ba sonnou baby You really know what you mean for mean for me? Ndam linga dieul diox ko souñ noon yi Yeah Yeah (Bomboclate) Wiri-wiri Diari Ndari Koula diégué Ma diam ko mbari (Ay) Baby you don't need another man (Bow) Yama geunal a lot of money (hii) Wiri-wiri Diari Ndari (ehhh) Koula diégué Ma diam ko mbari Bea you don't need another man (Boom) Yama geunal a lot of money Come back to me Come back bea Come back to me Come back bea Come back to me Come back bea Come back to me Come back bea Come back to me Come back bea Come back to me Come back bea Come back to me Come back bea Come back to me Come back bea
Writer(s): Mouhamed Loucar Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out