Music Video

Music Video

Credits

PERFORMING ARTISTS
Narah Diouf
Narah Diouf
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Nguenar Diouf
Nguenar Diouf
Songwriter
Amadou Birane Mangane
Amadou Birane Mangane
Songwriter

Lyrics

Tay ma bakk là
Sama Chocolat
Beug nala
Lolou Wor na là
Tay ma Tagg là
Sama Olalah
Kham nané beug ngama Lolou wornama
Guiss Jant bi Loumou lera ler
Sa dieum ji moy sama lumière
Xol nga wer wi noumou diéké
Sa khol bi nounoula rafété
Kon diégué ma
Niou And Dem fenen Wouyouma
Kon Yobouma
Niou And Dounde Lenen Ba Abadane
Hé hé hey
Habibi Ki Gueun si man
Té Ya Kham li war ci Man
Diko Def yeurem ngama
Chéri Yow yay sama Habibi
Habibi Ki Gueun si man
Té Ya Kham li war ci Man
Diko Def Yeurem ngama
Chéri Yow yay sama Habibi
Ano woni my habibti
Guily mbeeli Mo welti seti
Guilemen ko fifty fifty
Douda ak yow mouy nekh moi meeti
Love nana shine like diamond
Hakudam min e ma ha diamone
Indema e horam like melody
Yidema hokimi dole mbarodi
Wawa welde niande fof wada peace
Andou Kiram to mberde ko disease
Habibti par fewnou tes valises
Mami souré houré kangue kaliss
Min seeden kalda gonga ann bouriyam
Jougo ma e jougam longo fawé walabam
Holimi yidde fadani jango tideyam
Bae ndekete banekhou beguel fila yam
Halla mbelka newika tewika
Hewa mossali e diam a yiyata tikka
Mberde wiyani aala guite dji ko djiidi
Love sabou ALLAH mberde jaagui ha tiidi
Habibi Ki Gueun si man
Té Ya Kham li war ci Man
Diko Def Yeurem ngama
Chéri Yow yay sama Habibi
Habibi Ki Gueun si man
Té Ya Kham li war ci Man
Diko Def Yeurem ngama
Chéri Yow yay sama Habibi
Diougal Nga Fethie Ko
Ma woy Nga félouma
Diougal Nga Fethie Ko
Chéri Yow Yay Sama Habibi
Diougal Nga Fethie Ko
Ma woy Nga félouma
Yow Yay sama chéri
Yow Yay sama Habibi
Ki Gueun si man
Té Ya Kham li war ci Man
Diko Def Yeurem ngama
Chéri Yow yay sama Habibi
Habibi Ki Gueun si man
Té Ya Kham li war ci Man
Diko Def Yeurem ngama
Chéri Yow yay sama Habibi
Written by: Amadou Birane Mangane, Nguenar Diouf
instagramSharePathic_arrow_out

Loading...