Music Video

Featured In

Credits

PERFORMING ARTISTS
Narah Diouf
Narah Diouf
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Nguenar Diouf
Nguenar Diouf
Songwriter

Lyrics

Finga mey yobou sori na Fing ko diappe fofou la Nguamey yeeklo assamane Ba sokhlowouma ropelane Foma Wo ma wouyou leu Fing ma tek bae Saf na meu Ling mey yeukloo fort na lol Moungui douggou sama xol Def meu loula nekh Li dé waroul diekh Yangui beugueu yekh Khamnga lima yeuk Doy ngama seukk Boul khar ba euleuk Def meu loula nekh Li dé waroul diekhh Yangui beugueu yekh Defma loula nekh Wakh ma loula nekh Baby Yaye sama seytané Loudoul diekh lagnou digalé Xol yi fekh ba abadane Ci yow laye fanane Tanenala séne biir Yamay Miir Lo Sou goudi khadié Ba souf seddé Ma diakarlo Sama réni xol Limey doundou nekh na lol Def meu loula nekh Li de waroul diekhh Yangui beugueu yekh Khamnga lima yeuk Doy ngama seukk Boul khar ba euleuk Def meu loula nekh Li de waroul diekhh Yangui beugueu yekh Defma loula nekh Wakhma loula nekh Dafmay nekh dakh yow là love Moulay nkeh gnou doundou love Bae dieuleul li nga morom Lima yor yaye borom Do sen morom Xolal fima tolou ci yaw Yow yamay teul si kaw Gueum nani li dou diekh Mbeuguel rek ka nekh Def meu loula nekh Li de waroul diekhh Yangui beugueu yekh Khamnga lima yeuk Doy ngama seukk Boul khar ba euleuk
Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out