Lyrics

Bril on da beat Sokhore ci xaler Neikou douma baller Dawouma ci yollé Ay wakhe douma tardel Sagnsé di khegne neikhe Louma saff laye deiff Ci risque laye dokhe Do xole yaw foneik Douma baalé mane douma diékou baalé Sokhore done xaalé dama beurri doolé Douma baalé mane douma diékou baalé Sokhore done xaalé dama beurri doolé Mane dama nek sama yone Ligueye di khouxale samaye none Niome lougne maye jaye jaye jaye Louci sama yone Yone bi dafa leire Wakheleine ni jayou maleine guerre bi Mane meune na Thiou Thiou ak thia Lolou dafa leire Baleine niouye weth weth rek Aye Bla-bla-bla terei wouniou Fla-fla-fla Nek ci yone awema seine temps Yeaaahhh yeaaah yeaahhh yeehyaaaaaa Sokhore ci xaler Neikou douma baller Dawouma ci yollé Ay wakhe douma tardel Sagnsé di khegne neikhe Louma saff laye deiff Ci risque laye dokhe Do xole yaw foneik Douma baalé mane douma diékou baalé Sokhore done xaalé dama beurri doolé Douma baalé mane douma diékou baalé Sokhore done xalé dama beurri doolé Bayile niouye wakh ngaye def Risque leu Ragale douko deiff Mane dama akci done fi chef Touss nak dara dou khew Ndakaru ba Thies mane fouma jare ba paré Dara doufa dess Ndagoule ma lolou louma deif mou neikh Mane dama beurri feeling waxe ma louci dess Touss nakk dara dou xew Baleine niouye weth weth rek Aye Bla-bla-bla terei wouniou Fla-fla-fla Nek ci yone awema seine temps yeaah yeah yeahyeahyaaa Sokhore ci xaler Neikou douma baalé Dawouma ci yoolé Ay wakhe douma tardel Sagnsé di khegne neikhe Louma saff laye deiff Ci risque laye dokhe Do xole yaw foneik Douma baalé mane douma diékou baalé Sokhore done xaalé dama beurri doolé Douma baalé mane douma diékou baalé Sokhore done xaalé dama beurri doolé Bouleine faler wawaaaww Leiileiileeeiiiii waw Ndakaru ba Thies mane fouma jare ba paré Dara doufa dess Ndagoule ma lolou louma deif mou neikh Mane dama beurri feeling waxe ma louci dess Touss nakk dara dou xew Douma baalé mane douma diékou baalé Sokhore done xaalé dama beurri doolé Douma baalé mane douma diékou baalé Sokhore done xaalé dama beurri doolé
Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out