album cover
Torokh
23
Hip-Hop/Rap
Torokh was released on January 19, 2024 by Goat Vibes Record, distributed by Y3LH as a part of the album Bideew
album cover
AlbumBideew
Release DateJanuary 19, 2024
LabelGoat Vibes Record, distributed by Y3LH
LanguageEnglish
Melodicness
Acousticness
Valence
Danceability
Energy
BPM87

Music Video

Music Video

Credits

PERFORMING ARTISTS
MGeey
MGeey
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Momar Gueye Ngom
Momar Gueye Ngom
Songwriter
Abdoulaye WONE
Abdoulaye WONE
Songwriter
Moustapha Cisse
Moustapha Cisse
Songwriter
PRODUCTION & ENGINEERING
ProdbyDblow
ProdbyDblow
Producer
1Da Beatz
1Da Beatz
Producer

Lyrics

Yeah han han
Mère bi mi ngi may sàndi ñaan
Ragalu ma dara lu ma sòng daan Yeah yeah
Lu baax laa la yeene
Soxla wu ma sa dara budee am naa wer akk gudd fan yeah
Ragalu ma torox
Am naa ñaanu yaay duma torox yeah
Yalla xol lay fay duma torox
Duma tallal loxo ndaxte jòmb naa ko torop
Nekk yaaram taxul ñu baayi la bopp
Jarul bind LETTRE xam naa ñi ma Haine (N)
Maa nekk si sa xol te doo ma baayi nopp?
Wër di naan garap taxul nga nekk rèen (reine)
Loo muñ mu jeex, fii da ngay dee ndax ay xalaat'ag muñ
Bu ñii di wax luy jur xalaat kee di xalaat a jur
Kuy dolli sant ay fétiches nu ñuy tëyee sa tour? (Tur || tuur)
Ñoo bokk tente te ñooy teg ngente wala ñu suul
Jog bañ a xaar
Takk Peinture du la aar (art)
Boo bëggee yar say doom bul door sa doom yi ay yar
Mën nañ la mere
Soo bëggee ñu mucc dee len saytu
Yagg di nañ tekki li may wax takk ko teere anh
Yeah han han
Mère bi mi ngi may sàndi ñaan
Ragalu ma dara lu ma sòng daan Yeah yeah
Lu baax laa la yeene
Soxla wu ma sa dara budee am naa wer akk gudd fan yeah
Ragalu ma torox
Am naa ñaanu yaay duma torox yeah
Yalla xol lay fay duma torox
Duma tallal loxo ndaxte jòmb naa ko torop
Jòmb naa ko trop
Tax gedd ñi ma suuroon
Summi xalaat yiñ ma solloon
Foraat ròngoñ yi ma tuuroon
Da ñu yakk li ma ñoroon
Tax ma yem ci sama boroom
Ñu ne fayoo naar bi xorom
Budee joxoo mere bi boram, i swear han
Yenn saay geej gi di na mer
Di na mujj giif yagg-yagg di na fer
Dara bum la yeem petaaw buy seet sax di na reer
Soxla wu ñu gaz pour mën tàngal seeni nerfs
Fii ku fi bonn yes sa bopp nga koy def
Fii ku fi baax rekk ñu toog si say xef
Du ma tête vide xam naa dara mel ni Kòkki
Lu jot dina yòmb robinet sax xëyul sotti
Tekki sama mind yeah
Lepp dina fine yeah
Awma njegenaay hustle everynight
Teral sama yaay yeah
Tekki sama mind yeah
Lepp dina fine yeah
Awma njegenaay hustle everynight
Teral sama yaay yeah
Written by: Abdoulaye WONE, Momar Gueye Ngom, Moustapha Cisse
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...