Music Video

Music Video

Credits

PERFORMING ARTISTS
Momo Dieng
Momo Dieng
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Mouhamed Dieng
Mouhamed Dieng
Songwriter
Ndiouga Dieng
Ndiouga Dieng
Songwriter
Seck Mbao
Seck Mbao
Songwriter
Prince Ibrahima Ndour
Prince Ibrahima Ndour
Arranger

Lyrics

Saf na ba nopi
Ken du sapali
Saf na ba nopi
Ken du sapali
Yaw bul ma miina miine ba fatéma yaay
Thiow li meun na beurri lool waayé nangul né thine bokul saffine
Yaw bul ma miina miine ba fatéma waay
Loo bagn bagn ma marre nungul né nop yi kuddu na meun naa daaw
Saf na ba nopi
Ken du sapali
Momo saf na ba nopi
Heey Ken du sapali
Bargny ma roombaal Beut Ba
Daagou dieum Minam dieum Sendou
Weuy Ma Yaaya Baay Momo Dieng
Saf na ba nopi
Heeeeee heeee heeee
Yeeey yeee yaaaa yaaa
Saf na ba nopi
Ken du sapali
Momo saf na ba nopi
Ken du sapali
A Raffeet A meuneu feeth A meuneu beuy beussi doom Ama mayoon daw fissine bassa borop guedj guee
A Raffeet A meuneu feeth A meuneu beuy beussi doom Ama mayoon daw fissine bassa borop guedj guee
Lakoon sakkon ngakoon lebou baa ngi mooma mayoon daw fissine bassa borop guedj guee
Bul ma miine bul ma miine miine bul ma miine ba fatté ma kone mu gnaaw
Roy dou nourook piir du meusseu nourook piirr Isma Bul ma miino bulma miine ba fatté ma kone mu gnaaw
Laay laay la laa woo
Bul ma miine Baay Raan bul ma miine Baay Raan diop Bul ma miine ba fatté ma kone mu gnaaw
Louraass diop boo ngeuwul mu gnaw
Heeee
Thieuy sama waadja ngi nii
Heeee
Sa gane
Rak sa gane
Heeee
Neena la Momo yeungeul sa goun gou ndath
Heeee
Louraass Diop boo ngeuwul mu gnaw
Heeee
Thieuy sama waadja ngi nii
Heeee
Laay laye la laa so ngeuweul mu ngaaw sama niit
Laay laye la laa woo
Roy dou nourook piir du meusseu nourook piirr Djiby Ndiaye bul ma miino bul ma miine ba fatté ma kone mu gnaaw
Chéri Arame Diallo sama waa dji
Louraass Diop boo ngeuwul mu gnaw
Heeee
Neenala Momo yeungeul sa goun gou ndath
Heeee
Sa goun
Rak sa goun
Heeee
Neenala Momo yeungeul sa goun gou ndath
Heeee
Djiby ndiaye boo ngeuweul mu gnaaw
Heeee
thiey dikeul dikkeul suma waadja ngi nii
Heeee
Isma boo yeugoo moo neex
Heeeeh
Malick mbath dissa baay sama waadja ngi nii
Heeeeh
Sa goun
Rak sa goun
Heeeeh
Neenala Momo yeungeul sa goun gou ndath
Heeeeh
Senegal boo leen yeungoo mu neex
Heeee
Thieuy dikkeul dikkeul sama reew ma ngi nii
Heeeeh
Heeeeh
Momo yeungeul sa goun gou ndath
Heeeeh
Neenala
Momo yeungeul sa goun gou ndath
Heeeeh
Neenala Momo yeungeul sa goun gou ndath
Heeeeh
Heeeeh
Heeeeh
Heeeeh
Neenala
Neenala Momo yeungeul sa goun gou ndath
Written by: Mouhamed Dieng, Ndiouga Dieng, Seck Mbao
instagramSharePathic_arrow_out

Loading...