Music Video

Music Video

Credits

PERFORMING ARTISTS
Pipana
Pipana
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Malick Thioune
Malick Thioune
Songwriter
John Makabi
John Makabi
Songwriter
Kevin Agossou
Kevin Agossou
Songwriter
PRODUCTION & ENGINEERING
MK Beat
MK Beat
Co-Producer

Lyrics

Pipaana
Hey
Man yow rek lay khol
Je ne te ferai jamais du mal
Douma meussa guènè say rongogn
Diamant ngeu do kou niouy fowè 
Bo teudé nelawal 
Man may seu  gardien
Meun na fanan di khol seu rafètay 
Fi beu beut sèt
Rethiou wouma bén yon lima leu khaamé 
T’as changè my life
Banekh bimay am sa yoma diégué
Si seu wet rek lakoy amé 
Yeeeaah!
Khalé bilé nieuweul si man ma wan leu sama mbeuguél
Do fowou kay, ma xam seu valeur 
Laisse moi te le prouver
Bébé bébéé, sama bébé
Ba naré diooyy, ayo néné
A mon bébéé, sama bébé
Sama néné toutiii yeah yeah yeah
Soxla touma dem si docteur 
Ndakh yay garab bimay fadj
Sa youma fèbaré guisleu taané
Bo amoul won maley créer 
Denk naleu khol bi 
Teyé ko boubakh wolou naaleu
Takk meu boum, dirima beu foula nekh khalébi
Reuthiou wouma bén yon limala khaamé
T’as changè my life
Banekh bimay am sa yoma diégué
Si seu wet rek lakoy amé
Yeeeaah!
Khalé bilé nieuweul si man ma wan leu sama mbeuguél
Do fowou kay, ma xam seu valeur 
Laisse moi te le prouver
Bébé bébéé, sama bébé
Ba naré diooyy, ayo néné
A mon bébéé, sama bébé
Sama néné toutiii yeah yeah yeah
Soxla touma dem si docteur 
Ndakh yay garab bimay fadj
Sa youma fèbaré guisleu taané
Bo amoul won maley créer
Written by: John Makabi, Kevin Agossou, Malick Thioune
instagramSharePathic_arrow_out

Loading...