album cover
Noflaay
album cover
Noflaay was released on April 4, 2025 by Youssou Ndour & TBI Publishing S.A as a part of the album Éclairer le monde - Light the World
April 4, 2025
LabelYoussou Ndour & TBI Publishing S.A
BPM89
Melodicness
Acousticness
Valence
Danceability
Energy

Music Video

Music Video

Lyrics

Nit ki [ni]mu mel, Yàlla [a] ko ni def, soo bëggee sa noflaay, nangul ko-ko
Nit ki lu mu[,] am, Yàlla [a] ko-ko jox, nangul ko
Nit ki lu mu[,] am, Yàlla [a] ko-ko amal, nangul ko
Nit ki lu mu mën, Yàlla [a] ko-ko won, boo bëggee sa noflaay
Nit ki lu mu xam, Yàlla [a] ko-ko xamal, soo bëggee sa noflaay
Fa Yàlla[y fexe], benn mbindéef du fa dem
Siis am kenn du ko bokk ak moom
Buur bi, fa muy dogal, mbindéef du fa dem
Nit ki [ni]mu mel, Yàlla [a] ko ni def, soo bëggee sa noflaay, nangul ko-ko
Nit ki lu mu[,] am, Yàlla [a] ko-ko amal, na mangul ko
Nit ki lu mu mën, Yàlla [a] ko-ko won, nangul ko
Mooy tax mu du soxor, mooy tax mu du iñaan, mooy tax mu du rambaaj
Mooy tax mu du miser, mooy tax mu du wuruj, mooy tax mu du sëngéem
Fa Yàlla[y fexe], ni nga bëggee sa waay mel
Sa waayi-waayi [a] koy mel
Written by: Youssou N'Dour
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...