Credits
PERFORMING ARTISTS
Amira Abed
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Charles Mbaye Diagne
Composer
Abdoulahat Thioune
Songwriter
Lyrics
Yeneu saay ma tay ko xoulok yaw [ Ahh !! ] Ndakh lay xew ci biir Jubboo ba [ Waw fofou loufa xew ? ] Rewantou yakkoul mbeuguel feeling la ci Wawaw Lila dougal ci mane Guéné woula ci [ Surtout lolou !! ] Mane souma ragaloul wone yallah Ni maak yaw Pique ak pelle Takhalé wouniou Kay niou Dem foula neex Xalé bi lé Yaw la diokh bopp Meunou mala tenir tête Damala nopp Na niak diom thioloul Ndakh méré la wooroul Yaw sa dara sofoul Ndakh bayi la yomboul Té mane sama compteurou xol Nga woyofal yako tay Même suniou bayanté wé Sama alal ngay done batay Negn jubboo maak yaw Ma yeureum noone yi Sothiou wone Di khaar Kouniou retane Motax Warougn xouloo Maak yaw Ndakh yaay seral xol bi Bouko diaré sakh ma ramal la [ Moh khana nga bagn ] Fethial la [ Moh khana nga bagn ] Dila ayoo néné Bae kaay ma yeetal la [ Moh xalé bi khana nga bagn ] Tay ngay diomi Dioubok yaw lou am diom ni [ Moh khana nga bagn ] Kaay fi chéri Li dess wakhou biir nekk la Heey Sa chéri doula setane ngafiy niaaw Né dala beug Ya yorr cahier wam Mou yorr sa Bic Ni dalay bindal Souma dioubé xaré bi douma deup Ndakh ñiayou xaré la Mane Kene dou laal lima mom Ndanane Ndananakoy antane Chéri coco ney neex Dieundeul glace Thioup naa drapeau bi weex Tey sama xol dafa neex Ndakh dama dioubook baneex Heyy Nameu ngako Namone nala Namanté ngeen Xolou niara koy def Kone bisou wanté leen Mouaahh Kone mbeuguel Bala nexx rakh niak diom Xale bi Sugn xoulo malay toudou yakofa am Waw So xamone tay dji lima nameu ci yow Na nopi sakh Bala waa Jamra di niow Negn jubboo maak yaw [ Nioweul ] Ma yeureum noone yi Sothiou wone di khaar Kouniou retane [ Ehh sen xol dou neex tey ] Motax Warougn xouloo Maak yaw Ndakh yaay seral xol bi Bouko diaré sakh ma ramal la [ Moh khana nga bagn ] Fethial la [ Moh khana nga bagn ] Dila ayoo néné Bae kaay ma yeetal la [ Moh xalé bi khana nga bagn ] Tay ngay diomi Dioubok yaw lou am diom ni [ Moh khana nga bagn ] Kaay fi chéri Li dess wakhou biir nekk la Kone fanane Yama newone fanane Ya newone fanane Yama newone fanane Fanane ci naa Yaw fanane Chéri fanane Yaw fanane Yama newone fanane Fanane ci naaa Dialy xalamal maa Ma woyal sama waadji Maak yaw amougn neuboo Yaay sama wéteul Warougn xouloo Yaw fanane Chéri fanane Yaw fanane Yama newone fanane Fanane ci naaa Bouko diaré sakh ma ramal la Fethial la Dila ayoo néné Bae kaay ma yeetal la Tay ngay diomi Dioubok yaw lou am diom ni Kaay fi chéri Li dess wakhou biir nekk la
Written by: Abdoulahat Thioune, Charles Mbaye Diagne