album cover
Dfrnt
6
Hip-Hop/Rap
Dfrnt was released on January 31, 2025 by Keulthieu The Name as a part of the album DFRNT
album cover
AlbumDFRNT
Release DateJanuary 31, 2025
LabelKeulthieu The Name
Melodicness
Acousticness
Valence
Danceability
Energy
BPM86

Music Video

Music Video

Credits

PERFORMING ARTISTS
Keulthieu The Name
Keulthieu The Name
Rap
COMPOSITION & LYRICS
Keulthieu The Name
Keulthieu The Name
Songwriter
PRODUCTION & ENGINEERING
Freshii
Freshii
Producer
ro beatz
ro beatz
Producer

Lyrics

Dembay li wës tay liggéey dund ak a daat
 Demb du tay loo bari da nga ko waat
 Dinganté demb ak tay
 Niata ci say mbëbët moo jëm faat
 Keraalub god fekk jàmmam fudu ci natt
 Moore sama bët di xool xel
 Dem ak sama xol
 Gis naa yafus yu tóx né téeel
 Gëm ni bëccëg dina fay
 Te nee si minwi ba suba-tël
 Waxtu ndeki mooy nàcc reer
 Nga fanaano seet samay tël
 Kon lepp liggéey gi mërr
 Mën naa ko sippi
 Sipp na la bu yàgg, ****
 Damaa la bay ci biir
 Jëbel tiow du mbettel xamna loolu ci xër
 Jikko ak boroom bassi ci kambë
 Ëllëk nga xam loo géjj gi di rërr
 Te xalaat ak lu mën tax sëx tiow bari
 Mën naa mbaa baña nekk sam tiowbari
 Duma nàg xalifa demb
 Pour mën tey tiow ba régg
 Them **** di tóx seen diobo
 Bañu jub bi yeeg
 Baax ci xol ci
 Gën naa sax bon sa bopp
 Xol la ngay naatee say yene
 Taxlee ma nit ku iñaané
 Yene nekk loo tëj nafa sa bopp
 Lu waay def sa bopp
 Fight pour danoo sa bopp
 Jàppul sàkku ji naan
 Duñu ma fa dem
 Dem seti deëm
 Duñu ma ko def
 Duñu ma ko ko game
 Mbeed rekk la seewel
 Respaix boodul dañu
 Sey middle finger mën gu sax too
 Disrespect mësu ma gànn
 Jéex na tey
 Na boy yi link fee dugg
 Fuck talent, liggéey chance
 Wekkuwuma sama carrière
 Ci seen mise en évidence
 Hype laa kill sa maam, rest in peace la
 Mbooloo jóge taawu may la 1 minute de silence
 Tam na ko, miss na ko mooy seen laago
 Meritéwuñu sax
 Ma nu yewuleen ak loo bimay labo
 Sam kanam sey MC duñu jiitee dayoo
 Ay jëkk lañuy dañoo
 Ku nekk ci ñoom noo muy daagoo
 Xalaat yu lendëm ni kuy dóora dug jeel
 Su ko dundul mën naa xam metit dey tëj xel
 Dëmel ni ñoom bala ñu la rey
 Rey la thi thi thi sa maam
 Na gne le ci ngu mel
 Different
Written by: Keulthieu The Name
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...