Credits
PERFORMING ARTISTS
Man G
Performer
Kef keffie
Drums
COMPOSITION & LYRICS
El hadj malick mbaye
Songwriter
Momar Ndiaye
Songwriter
Lyrics
Wahtou diote gneup know
ni legui nak wessou nagn diamono
Yigay tek sa bop figa agoul Nakh kep koula meuss gueum ndakh apparence
Toubeuy bou gande tegou si beatou boom bap diapé sa bop le vrai
Fimou né lep thiol khamnagn bou bakh limou done ay doul ak dadialé rk
Do intouchable dieul distance
Samay shoot bone Té guene graw
Shoot bi dalay dead fo ma meuna nek moytoul fofou ligay yote mougui sa kaw
Niveau dang koy deg mai nekoul si yaw Boul forcé di soukhlou sa bop
Li deh don leu meunoumako té dafa fess si mane liy tourou day charité
En matiere de rap pas d’egalité liniouy defa yombe si mane like holiday
Holidays diabou bone ak rice Dadj bi guena for bou blunt boul abusé
Je mamuse rek boul dougal sa bop si bilé piege
Suis aux commandes depuis mon siege
Roulante Mounane teuss mbar bi todji na sa kaw rek ga seuss
Menoci dara nakh mane dama teu
Dama doy war am a thug
Meune na bayi bagn eup fouk
Ma bolé gnom gneup rek gnouss
Té douma mamou alboury
Fi alle bi bour bi moy seg bou gnoul bi Black tiger
Fougn ma sene all these bitches keep talking
Yene warouwoulene fimou aksi ak nimou doré
All my life hustle everyday
Kone Si sa life niafé molasiy guéné yeah yeah
Memoriser lignouy defa takh Ak Ken menougnou mengo raf melni ga tak khandiar ak peureum
Ma indi lingo raak Akci si chaisou bour bi ak ay leugeut dougnou yeureum sougnou bop
fougn tolou weur lougn fade
lake gatou wakh kate Ni paka djitouko mbaram
Limouy guena tar gay kadji digui bi baram
Bougn nela wakhal loy wakh
Raboulo di doul deuké cap
Fi dougn seral nay baakh
Sama mbagnel si gnom meritewougnou
Sama mbagnel si gnom meritewougnou Gnom gneup dagnou tok fogone ni li dou dioudou
Lougnou meuna def si rap lici guena ndawagui
Bidew leundeum la sokhla nguir di meuna briller
Wakhtou dafa diote si rap gnou wara trier
Gnikoy def ak gniko defoul gni dessé assumé
Mane rap rek la sante sama bop
Boleci vibe diomba def lou flopp
Bouguen deugouwone gnou bari gued mic tok
Ssp dotoul né si ben plateforme
Diamonoy diekh wayé diamonoy gneuw Diamono yi louy tak teuwa fay deh khamal ni mana
Gnoumté meunta wess yakar passion likay fay
si miim rew dou liguey té dou patience bigay andal
Khamougn touss dara Gnom gneup zero
Kouci guena reuy gate guena gande defaite
Kougnou dieul baga beuga took sougnou
digue bopp diga khamni ignorant faloul ken nakh ga sa bop
Wakh less liguey more
Nay flex ni gun mor Code PuK
Lou mate Seuk Gakoy amé Man G dotoul joko
Guneu geune Comme d’hab
Dewmeu fene **** fxck come back
Fxck Loy nane **** fxck Loy takeu
Fok them all hit them up com pac
I’m Biggest the flow digger
Comme Skey jeune prodigieux
Done pro di jeux jeux bou ame classe
Doungene fi ame place Li dafa fess del
Sama tour legui passport leu
Kou beug def fiww mane ngay clash
Kou beug siwww samay wax ngay wax
Kou beug diog sama kaw ngay dal
Mais Ame visas mo geuneu yomb 10.000 fois attiré sama attention
Je suis au courant de tout quand je le voudrai je vais monter la tension
Ma geuneu saff lamigne ticket laobé
Gnima togn Meuneutougnou nelaw dé
Mane la mort kene meunouma daw dé
Dionganté bi diexone na depuis daw dieg
Boy thiaroye Essence laye nane comme Rolls royce boy bouma roythiaa
Bouger wo depuis jamonoy temps mor
Dagua tarder ay ate beug wan mor time
Ame lene xolou mougn sama révolution est une lutte sans fin
Wayé nak na sene xel yi dal nekoumassi concurrence bou malsaine
Just because I’m a hip-hop lover
Ennemi I see you as my brother
Thiop sene money dem taki Rita hora
Fougn ma sene all these bitches keep talking
Yene warouwoulene fimou aksi ak nimou doré
All my life hustle everyday
Kone Si sa life niafé molasiy guéné yeah yeah
Written by: El hadj malick mbaye, Momar Ndiaye