album cover
SELF MADE
6
Hip-Hop/Rap
SELF MADE was released on November 2, 2025 by Gunzout Records as a part of the album ANTIDOTE
album cover
Release DateNovember 2, 2025
LabelGunzout Records
Melodicness
Acousticness
Valence
Danceability
Energy
BPM104

Credits

PERFORMING ARTISTS
Yanko SM
Yanko SM
Chant Vocals
Nitdoff
Nitdoff
Chant Vocals
COMPOSITION & LYRICS
Ibrahima Diop Gaye
Ibrahima Diop Gaye
Lyrics
Amady Fall
Amady Fall
Composer
Mor Talla Gueye
Mor Talla Gueye
Composer
PRODUCTION & ENGINEERING
Bazik Prod
Bazik Prod
Producer
Julien Lesueur
Julien Lesueur
Mastering Engineer

Lyrics

Yeah
Tracer wo yone wi doma wax fimay diarr
Dokh woutiko device bi self-made doukouy tok di xar
Boy, aloo ma tank dina dokh dém
Fi samay guéntë yi yaubou
Pas yéén figuen beug ma yaam non
Sa xél boulay té geum-geum nalay pousse
Tay gniy dokh tchi tapis rouge démb nioy gni done xouss
Yité ak pass-pass tchilay tagat sama bopou
Ndakh xam nani mom rék moy féssal bopou féssal poche
Boy même soko meunoul diémal défal ko sa bopou
Diapou niou tchi say mbageu tékiwoul do meuna féthial sa bop
Tékki soriwoul tchi say thiono laniouko fasse
Gniy yakar tchi nit nioy dead tchi yakar gou tass
Boul xar kéneu donal self made
Diougeul défal ko sa bopou
Follow your dreams all the way
Sa geum-geum ñiémé ko topou
Xél kasso leu bo nanguo teuthie fa sa bop
Mane guissouma koula fay guéné
Waxal meun ngako deff by force
Mentalité gagnante moy niémé
Even if you walk alone
Ain't nobody else around
Eh my bro let me tell you one thing
Nangou niounane leu lii meunoko deff, bad thing leu
Gëmal sa boppu le yokku dolé tchi sey mbageu
Yoré jikoy yaram tek sa tank yone bul mëssa djadd
Yallah du jeex ku dëkké lamb di nga mëssa daj
Çoono dou réér weurseugou nit kén douko nassaxal
Ba leen ñu rée kookali neekal tchi lila war
Biss sa gui ñew di sa gloire nga done sén guèlawaar
Xalé bou ndaw deukké daw bëggo ku la raw
Ëleuk gua siggi tchi sey mass yaw la ñuy gëna naw
Fight to fight (eh)
Side to side (oh)
You never gonna stop until you're satisfied
Do mëssa bideunti sinon rek xaliss saay
Gëmal sa bopu tek sa bët fu sori sori
Numay deff ba mëna deuké ciow li ciow li
Çoono douma téyé damay xeuy di dolli
Deukké bana-bana wala joni-joni
Gìssatu ma dara lu dul money money
Boul xar kéneu donal self made
Diougeul défal ko sa bopou
Follow your dreams all the way
Sa geum-geum ñiémé ko topou
Xél kasso leu bo nanguo teuthie fa sa bop
Mane guissouma koula fay guéné
Waxal meun ngako deff by force
Mentalité gagnante moy niémé
Even if you walk alone
Ain't nobody else around
Eh my bro let me tell you one thing
Nangou niounane leu lii meunoko deff, bad thing leu
Don't say, don't say never (eh)
Just try you can do it (han)
Féxél
Niafél
Xarél
Deff ligua wara deff
Don't say, don't say never (eh)
Just try you can do it (han)
Féxél
Niafél
Xarél
Deff ligua wara deff
Don't say never
Don't say never
Yeah you're a self-made
Don't say never
Don't say never
Written by: Amady Fall, Ibrahima Diop Gaye, Mor Talla Gueye
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...