album cover
Falling Back Into You
album cover
Falling Back Into You was released on January 9, 2026 by Nalanke Music as a part of the album Falling Back Into You - Single
January 9, 2026
LabelNalanke Music
LanguageEnglish
BPM
Melodicness
Acousticness
Valence
Danceability
Energy

Music Video

Music Video

Lyrics

Oooh ooh ooh ooh
Yeah yeah yeah yeah
Oh baby
Nalanke
Saa yu ma jéeme dem
Sa fàttaliku daf may khëcc ni vague buy daw
Maa ngi waat ni dama am doole, but baby not with you
Yaa ngi laal sama lokho, samay miir yépp daanu
Ooh, kham nga li ngay def
Khol di daw, yaram di yëngu
Mënu ma ni dama la ëpp doole
Bu bepp noyyig yaram daf may delloo ci yaw
Ndakh maa ngi wéy di daanu, falling back into you
Melni musu ma dem, like I always do
Am nga loolu, dëgg bu velours bi
Maa ngi wéy di daanu, di daanuwaat ci yaw
Ohhh, daanuwaat ci yaw
Ay, Debbo Peulo, honto wonda, achu fijugol, ada andi
Mido yidi mah, berndam fijata
Simi ressi mah, fofto hakkile, yo en yoten
An ko debbam, an ko fof am, sehilam, debbo jontado
Haisoh netdoh hali ko boni ah mah
Hajam ala hen, hebe waawi fai lakara
Cherie, yidde maa ina weli no henndu subaka
Eptou joongam ha oum dillinah berndam
Sika dill li, hakkile am dejah
Alaa, vibe maa wada mawdo fad dow koppi mum
Baby girl, it's forever me and you
Ooh, kham nga li ngay def
Khol di daw, yaram di yëngu
Laal ma ndànk ma nangu
Sa mbëggeel lu ma mënatul khalaat
Ndakh maa ngi wéy di daanu, falling back into you
Melni musu ma dem, like I always do
Am nga loolu, dëgg bu velours bi
Maa ngi wéy di daanu, di daanuwaat ci yaw
Ohhh, daanuwaat ci yaw
Amaana dañu yàqu
Amaana dañu nu tànn
Amaana nun ñaar ñépp dañu khóot lool ba kenn mënu la bàyyi
Waaye soo ma jàppee
Lépp a ngi yeekh
Maa ngi fàttaliku li takh sama khol tànn la balaa may kham
Ndakh maa ngi wéy di daanu, di daanuwaat ci yaw
Doonte damay jéem, ba leegi damay jàll
Dama réer ci sa baat, melo khaaju guddi gi
Maa ngi wéy di daanu, falling back into you
Melni musu ma dem, like I always do
Am nga loolu, dëgg bu velours bi
Maa ngi wéy di daanu, di daanuwaat ci yaw
Ohhh, daanuwaat ci yaw
Nalanke
Written by: Amadou Sow

Loading...