album cover
CA KAW
9
Mbalax
CA KAW was released on February 6, 2026 by Afrik Melo as a part of the album CA KAW - Single
album cover
Release DateFebruary 6, 2026
LabelAfrik Melo
Melodicness
Acousticness
Valence
Danceability
Energy
BPM140

Credits

PERFORMING ARTISTS
Yoro ndiaye
Yoro ndiaye
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Yoro ndiaye
Yoro ndiaye
Songwriter
PRODUCTION & ENGINEERING
Yoro ndiaye
Yoro ndiaye
Recording Engineer
Afrik Melo
Afrik Melo
Producer

Lyrics

Yama bëgg ma bëgg la
Kon faw ma wonne la
Bañu xam né kii di begal soma xol bi yawla
Budee may sa titulaire
Kay wax ko gayi lepp ler
(Cia kaw)
(Cia kaw)
(Cia kaw)
(Nit su ko bëggee da koy wone)
(Cia kaw )
(Wone ko ñu giss ko )
(Su ko bëggee dang koy fessël)
(Cekko)
(Wone ko ñu gIss ko)
(Soko bëggee dang koy woné)
[Chorus]
Jotna nak ñu wax gaayi li fi ne
Lakkatu bi doyna nañ ko assumé
Jotna nga wax gaayi ma fi né
Nitt soko bëgge dang koy assumé
[verse2]
Ndegam man nga bëgg
te ma la raw
Buñu ko laqq Nañu ko fessal cia kaw
Jël ma ci kaw ,
ma leral li xew
liñuy dundë inbox man ak yaw
Nañu ko fessel
Fi Amul ragal
Soma nobë dëgg
Danga koy fessël
(Wone ko cia kaw)
Yama bëgg ma bëgg la
Kon faw ma wonné la
Bañu xam né kii di begal soma xol bi yawla
Budee may sa titulaire
Kay wax ko gayi lepp ler
[Chorus]
Jotna nak ñu wax gaayi li fi ne
Lakhatu bi doyna nañ ko assumé
Jotna nak nga wax gaayi maa fi né
Nitt soko beige dang koy assumé
[verse2]
Ndegam man nga bëgg
te ma la raw
Buñu ko nëbu Nañu ko fessal cia kaw
Jël ma ci kaw ,
ma leral li xew
liñuy dundë inbox man ak yaw
Nañu ko fessel
Fi Amul ragal
Soma nobé dëgg
Danga koy fessël
(Wone ko ci kaw)
[Chorus]
Jotna nak ñu wax gaayi li fi ne
Lakhatu bi doyna nañ ko assumé
Jotna nak nga wax gaayi ma fi né
Nitt soko bëgge dang koy assumé
[verse3]
Assumer ko ,ba ñepp xam ko
So bëgge assumel ñu guiss ko
De ko begal
Moom mu lay begal
ba kuko xool ci sa xar kanam gissko
Mbëggel moom amul nëbo
Linga yëgg sa xol bi kaay waxma ko
(Cia kaw)
(Cia kaw)
(Cia kaw)
(Nitt su ko bëggee da koy wone)
(Cia kaw )
(Wone ko cia kaw )
(Soko bëggee dang koy fessaël)
(Cia kow)
(Fessël ko cia kow)
(Soko bëggee dang koy wone )
Written by: Yoro ndiaye
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...