album cover
Mariama
album cover
Mariama was released on April 17, 2026 by Tamsir SN as a part of the album JUST FOR YOU
April 17, 2026
LabelTamsir SN
LanguageFrench
BPM72
Melodicness
Acousticness
Valence
Danceability
Energy

Music Video

Music Video

Lyrics

Lii lanatilaa bouma bayyi Mariama miin nala kaay nguir yalla
Lannatilaaa Mariama miin nala kaay nguirr yalla
Sama xol molay lathié
Bayina lepp ndakh ioe bouma gathié
Roussna niouniouy atté Maria gninaan
Damala ragal ioe layy waaté
Soumalay guiss sama yaram day daw
Yima bagnon yeup nangounako ndakh yaw
Khalé bi linga ma jaral
Soko khamon dinguama thieureul
Soma ngembé bama bakkou saa souma beuré daan
Lii lanatilaa bouma bayyi Mariama miin nala kaay nguir yalla
Lannatilaaa Mariama miin nala kaay nguirr yalla
Soooo ohh laamiisooo miisssoo eh yaw (× 2)
Ioe beugeul malay beugeul fi kounek sa seytané
Mayy sa seytané man mayy kilay danél
Beugeul malay beugeul kounek sa seytané
Mayy sa seytané mann mayy kilay danel
Maria yaw diougeul Maria yaw dougeul
Maria yaw diougeul khamnga Maria yaw waro nelaw
Mariama yaw diougeul Maria yaw dougeul
Maria yaw diougeul khamnga Maria yaw waro nelaw
Lii lanatilaa bouma bayyi Mariama miin nala kaay nguir yalla
Lannatilaaa Mariama miin nala kaay nguirr yalla
Lii lanatilaa bouma bayyi Mariama miin nala kaay nguir yalla
Lannatilaaa Mariama miin nala kaay nguirr yalla
Sokhna seeee yaw anhhh woo ohhh
Mariama lingay deff sama xoll…
Khamnaa domaa seetan
(Doma seetan maffi niaw Mariama)
Doumala seetan
(Douma seetan maffiy niaw Mariama)
Written by: Tamsir SN
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...