album cover
Mahdiyu Laye
album cover
Mahdiyu Laye was released on May 31, 2004 by Nonesuch as a part of the album Egypt
AlbumEgypt
ReleasedMay 31, 2004
LabelNonesuch
LanguageEnglish
BPM69
Melodicness
Acousticness
Valence
Danceability
Energy

Music Video

Music Video

Lyrics

Bu de dangay leble
Lebleelal ku am pey
Seydina Limamou
Yalla feyna ko
Neent fukki at ya
Mohammed woote
Neent fukki at ya
Maam Limamou woote
Mahdiyu Laye
Mohammed waxoonna
Mahdiyu gi ci yoon wi
Seydina Limamou
Feen ca tefes ga
And ak Issa
Maami Maam Rane Laye
Moo niwoon geej ga
Yow xamnga maay kan
Bëgg naa nga dellu
Ca la geek ga delloo, Laye
Keroog la woote
Adjiboo daayirahi
Kaayleen, kaayleen
Nowleen, dikleen
Jaamu lamul ahzam
Laye
Moo dellusee, moo dellusee
Moo dellusee, Mahdiyu Laye, moo dellusee
Baayi Issa Laye
Baayi Mandione Laye
Ak Ababacar Laye
Maami Maam Rane Laye
Maami Ousseynou Laye
Mahdiyu feenna
Sagalnga reew mi
Neppangi naan Laye
Yaa dellusee, yaa dellusee
Yaa dellusee, Maam Limamou, yaa dellusee
Yaa dellusee, xammenan la, yaa dellusee
Yaa dellusee, Mahdiyu Laye, yaa dellusee
Written by: Kabou Gueye, Youssou N'Dour

Loading...