album cover
Dette Morale
647
Hip-Hop/Rap
Dette Morale was released on May 29, 2026 by For Life Music as a part of the album RANCUNIER - EP
album cover
Release DateMay 29, 2026
LabelFor Life Music
LanguageFrench
Melodicness
Acousticness
Valence
Danceability
Energy
BPM64

Credits

PERFORMING ARTISTS
Zo titan
Zo titan
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Omar Sow
Omar Sow
Songwriter
PRODUCTION & ENGINEERING
Zo titan
Zo titan
Engineer
Boss Beat
Boss Beat
Engineer

Lyrics

Xam na ni mère dinga ñu méré
Ndax capable lañu woon té mësso si rendre compte
Déposé naa sama démission
Ndax dundu mbédd ak néek mëssul nek béen
Baal ma budé mëss naa la tégal haine bimay dundu
Ndax bëggu ma déé ci ñak
Mbok mi dundal nga faté ma
Xëy na sumay ñëwat day fék xallé yi béjaaw
Du risque bakan la taylé woon
Amul si suuf luñuy téré dém
Mënu ma tagatoo
Mais kon ma wax la mama "nañ ma dëjël ma gënë fééx"
Kaamb biy jël sama corps
Budoon temps bimay ñak
Kon gass naa ko sam néek
Chambre biy jël sama peine
Bu doon temps bi may perte
Kon def na ko sama néek
Mère bi su wooté née ko
Màngi digënté rancune ak dundu bi ñëp di musslu
Capo bi jiiñu ma assassin
Daa dox ba feek may réndi sam' bopp si mbédd
Du man ma taan judoo banlieu
Tantôt man mënuñ ma condamné ak luma déful
Jàngoo ba jàng liñu jàng si mbédd
Duul yi prof bi nek di bindd si tableau
Gor laa du déñ
Xaar naa ba déé et puis woo nala mësso jëll
Saño ma jooy
Rééru mala ndax yaw mësso ma séeti fén
Yaw est-ce que nitt nga?
Tourné naa pour woo la ndimbal
Ngay daw ay xël
Talloo ma jooy
Bétt naa la mësso bëgg ma doon ku baax
Wax ma lutax mësso kaas ci zero yima daan jëllé school
Gaayin, wax ma lan moo la téré kaas banga déggé ni dañuy tux
Xam naa sa yéné mais séeg laa
Motax may dundu ba léegi té déw ma jail
Xam naa sa yéné man gaïndé laa
Motax may dundu ba léegi
Am naa ci part ñun ñépp lañ doon suspendre
Tons yaa doon jaay sama life
Nééko loo giss day jéex ñun ñépp lañ doon xaar jail
Tons yaw yaa jaay sama life
Yaw yaa taal samay boy gënë bon Lucifer
Sañoo ma reprocher bon
Fi kén fatté wul gatt té du déñ samay hormone
Motax may bañ sama bopp, boy
Takal mu ñëw, tout façon mëssul kaas tux
Wax ji muy wax ñoru ko
Bëggo kén dangay dul, je le sais
Mësso xaar bac
Zéro yi ma am math géné wu la
Bayi ma ma rap, sumay saaga bul kaas mère
Galère du simple cauchemar
Séeg laa, samay peine dam' ko tëdd bam' mat sëkk
20 ans du 1 an, yaay booy
Salopard! (hun)
Diable bi man lay wax "Salopard"
Yaak doomu xaj li ngéen uté jamais bëtt du ko génné si microscope
Yaw est-ce que nitt nga?
Tonton dis, est-ce que nit nga?
Say doom ngan doon job
Tonton yaw, est-ce que nit nga?
Wéet na di laaj "tonton yaw, est-ce que nit nga?"
Sound bi xonét laa ko bindé
Su indiscipliné rek c'est normal
Mais ay doomu xaj laa bindal cadeau
Jarul son bu normal
Tons I'm a kët
Heureusement rancunier laa, longue vie(hun)
Giss naa léen yéen ñépp, pas de panique
Boo doon rayé duñ fanaan ko déé nañ bu yaag
Dox nañ génn town bi tëdd dans le coma
Yéwu fébar ñibbi fanaan all semaine
Si boy yu mineurs té yaw remarqué woo ni absenté nañ
Mais nala souhaiter jàmm
Guddal fan même so bëggul ñu gudd fan
Mais nala souhaiter jàmm
Amal jàmm même so bëggul ñu màgg ak jàmm
Aduna la (aduna laaa)
Aduna la, choix la woon
Mais aduna la (mais aduna)
Faté wu, ma choix la woon
Mais faté wu ma (faté wu ma léen)
Faté wu ma, faté wu léen
Faté wu ma jour bi may géen gaalé méeti woon na
Awma chance comme yaw
Man choix la woon ci man ma géen (ci man ma géen)
Géen wuti xaalis, xéexi, téral mère bi noo (noo)
Tons maag na
Xammé na
Ràññee na
Millionaire fu ma néex dem (fu ma néex dem)
Written by: Omar Sow
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...