album cover
Budoon Jaay
36
African
Budoon Jaay was released on August 8, 2026 by Believe Boyz as a part of the album Budoon Jaay - Single
album cover
Release DateAugust 8, 2026
LabelBelieve Boyz
Melodicness
Acousticness
Valence
Danceability
Energy
BPM

Lyrics

Xalé bi lé jekk taaru rafet kaar
Yow li nga boolé bari ci ay feem
Yow ku xeeb da fekk xamul taar
Yay ki mën bokku lo ak ki koy jéem
Lu mu guddi guddi du naajé ndax yow
Lu mu lëndëm lëndëm damay xuus ba jott lë
Da ma la ni jakk sama xol yëg lë
Fitt bi né tëff ci la xam ni yow lë
Yow bo ma jeggée damay gënnël kaay
Té bo ma sorée damay metti lo lée
Mbëggel bi ñuy dundu comme bu Thione ak Diaga
Té bu ñu langée dafmay gënnël waayoo
Budoon jaay
Budoon jaay ma jënd ko li budoon jaay
Budoon jaay
Xol bi budoon jaay ma jënd ko li budoon jaay
Budoon jaay
Yow nax nga ma ni coppét sama xol
Sa rée ju neex sa bëtt yi nga ma xool
Yow jongama
Jommal nga ma
Sa jëm ji ma yéem wayee faible lu ma
Su may wax ci yow dé du ma jéexal
Da nga nooy té neex na nga ma jeggël
Bëgg na li ci yow ak ni nga bandée
Fu ñu weeté sa ma ngor gi lay mandée
I won\'t never cheat
You\'re my only fight
We gonna take over baby you and I
Sama ndëggërlay
Yow bo ma jeggée damay gënnël kaay
Té bo ma sorée damay metti lo lée
Mbëggel bi ñuy dundu comme bu Thione ak Diaga
Té bu ñu langée dafmay gënnël waayoo
Budoon jaay
Budoon jaay ma jënd ko li budoon jaay
Budoon jaay
Xol bi budoon jaay ma jënd ko li budoon jaay
Budoon jaay
Yow bo ma jeggée damay gënnël kaay
Té bo ma sorée damay metti lo lée
Mbëggel bi ñuy dundu comme bu Thione ak Diaga
Té bu ñu langée dafmay gënnël waayoo
Budoon jaay
Budoon jaay ma jënd ko li budoon jaay
Budoon jaay
Budoon jaay mann ma jënd ko
Xol bi budoon jaay ma jënd ko li budoon jaay
Budoon jaay mann ma jënd ko
Written by: Believe Boyz
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...