album cover
album cover
PBS 37 was released on August 4, 2026 by Positive Black Soul as a part of the album PBS 37 - Single
August 4, 2026
LabelPositive Black Soul
LanguageFrench
BPM98
Melodicness
Acousticness
Valence
Danceability
Energy

Music Video

Music Video

Lyrics

Té del daw čoow
Kü bëggë, bëggë na
Del daw čoow
Kü bëggë, bëggë na, ndax Lü yagga dëggë la hey
Yeah, ah
Positive Black Soul I know you've heard of us
We be the killers of them haters, call us murderers
Ya ko tey, ñün da ñüy dem ba luzz
Siw ak jaay taar, taxü ño jogg, ño gënnë yagga buzz
Ñett füki att ak jüroom ñaar
Doli Sant YALLA ndakh bari na ñu fi jotta jaar
Hip Hop da liggeyal Galsen
Bala xam sa ngoora Baay da ngay laaj sa Bajeen
Uh! Jambari goor ñoo ngook
Bañ kat! Jappeh bep Sénégalais mbok
Tewal süñü reew fepp či Adina
Xeex li dül dëggë dü yoon, kü bañit bëggë na
Ah! Ani xaj yi doon mbow?
Ño la niwoon def lo xam, bül faalé teh daw čoow
Yagga dü saabü wanté da na foot
Delo njükal, gërëm Senegal, mi ñü taxa jog
Yow bül faalé, teh del daw čoow
Kü bëggë, bëggë na
Lü yagga dëggë la hey
Yow bül faalé, teh del daw čoow
Kü bëggë, bëggë na
Ndax lü yagga dëggë la hey
Awadi Supa ndaanane international
La vrai force ce n'est pas de tomber, mais de se relever
Le vrai leader, c'est dans les chutes qu'il a su s'élever
Évite les tonneaux vides, ça fait beaucoup de bruit
Cultive la sagesse boy, apprécie les fruits (Ha!)
Fais pas ce qui marche, fais marcher ce que tu fais
Sois original, tôt ou tard tu vois l'effet
L'inspiration quand elle est pure, on la recopie
La bonne copie de la copie, c'est la photocopie (Ha!)
Il a fallu qu'on s'éloigne pour se retrouver
La solitude était bonne pour nous éprouver
Même si nos proches, nos amis n'avaient pas approuvé
Y'a des combats personnels qu'il faut se prouver (Ha!)
From day one cette culture on l'a adorée
Nous on savait bien qu'on était seuls, on s'est fédérés
En temps que fils de Capsi, on a persévéré
Trente-sept ans c'est la nation qui vient nous décorer!
Yow bül faalé, teh del daw čoow
Kü bëggë, bëggë na
Lü yagga dëggë la hey
Yow bül faalé, teh del daw čoow
Kü bëggë, bëggë na
Ndax lü yagga dëggë la hey
Brothers guess who's in the house?
Positive Black Soul now we just want you to bounce (Yeah)
PBS, yeah, xale ya ngi ni
Goor ya ngi ni, ci saape dagit ndat saï
Kü YALLA tačču na nga fečč, ndakh lü tëggë tass
Lü tëggë taaass
Capsi, yooxul ci kaw ndax më dégë
Capsi, lèves les mains et représente!
Capsi! del daw čoow
Capsi! lü yagga dëggë la hey
Capsi! del daw čoow
Written by: Amadou Barry, Didier Awadi, Ivan IGNANGA NDONG MINANG
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...