album cover
BXNX
album cover
BXNX was released on August 29, 2026 by Y3LH as a part of the album BXNX - Single
August 29, 2026
LabelY3LH
BPM76
Melodicness
Acousticness
Valence
Danceability
Energy

Music Video

Music Video

Lyrics

Firil say nope deglou d\'if carrément
Xam xam si xel mbekté si xol
Meun meun bou beuri pere sen rappeur yi fuck koussi lank
Aisaiment
Lay wathie araf yi tepi mou fath serré rang yi
Patte ak liguey dou xadiou di doul tararari
Reude yone bi xaré tarbiyou meek tela tari
Xex djigoul kou amoul fitt
Dieun menoul lap
Kouy weur sa mbok na sorri xiff
dieufa meun wax
Mbind bou carré newougn si sallé dagn meun lugnuy Def
Champing si xaré xaragn ak Paré mention bi si test
Xadioul si xalé retour ak allez lay moss seni fess
Beat boko diokh mou glisser
 Fit ak talent la miser
Mike tchek sa mc dou shit
Romb diamnadiok samay ter saf sap ni shit
Auto dou daw si chemin fer 12 coup dou missil
Tarou mbind fila fekk bax courant dou pil
****
Guiss nga louy takk lata sa coup de sifflet
Taxaw di dank say nak xathi sa coup ma sif lepp
Soute fi fepp karboté tegati tigui gni xif lekk
Bou bax bi is back noté ko bossi di goûté da ngay bek
Dawoul thiow **** diox la lodoul siki saka
10 bi fak Def tak yakk gayi souk sakk
Dioubal sappé yi ni diak bandit lay bak di akk
Kou deg lakk di nga xam ni bokou massi
Game bou bari ndiouth ndiath xel bou diex ak forcé
Nekha thiop ni pouth path bari juge ni procès
Causou imposé yokk samay Diego teup mass yi
Labali fasse tai yokk war wi mbok fofoula
Black appart Sax job ba sopi fo fouleu
Athia yok leu dieulidji ndem kou dane gnou top la
Djital sa bopp la ndam si xaré dou xar gnou diokk la
Taxaw deugeur xel dou xol ak xeuteur tari bou mokk la
Meun ko dissi dozé posé free dath bi dou rosé firi bath gnou causé
Flow bi zonzé geuneu fath imposé
Fuck seni kath menolen adji dath bi sibolen Lima bolé Si dolé
 fatt fepp indi yolé
 dou hotess nirolé
Soul gnima yenei ma thiolé
Fuck saube ak salé man magui si war té drapeau big town
Yor ay xetou jap you geuneu rare nekhou niakh bir town
Sa dolé album lay teunk barre sa carrière si sound
 Gamou thiouné Mcs you nullard tax level bi down
Man dama xaré fim waré
Liguey ko diayanté diaral fim diaré
Loudoul yallah menoul Def bagnou tit
10 di MC you ay bouy xar koumouy kokou crith
Gene wouma sa école tai never ma bind nga degg ko ba dioum n\'ai li c\'est
Sax si war bi sama tol nandité xam nagn fou xam xam di cité
Pour thioub sa mc cest vite fait
Fuck triché
Ay texte you ndoxé ni xal carrièrou taf yeungeul ak copier
War ngen rangné deug ak fen woutelé pomme New robinek ten
Tol si diamonoy beut moussala meuneu mouthieul adounay xel
Deugeul li nek sa Hurt ba bodé gaskat fexé am pel
wax dalay reral fou tek di wané yone
Lilay yegal si sommet dou meuneu yomb
 nek gouney boumla taxa bari diom
Borom diassi dou xexak kou yoré gone
New dolé andoulak meuneu togn
Written by: Ababacar Sadick Kane
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...