album cover
Wettay
album cover
Wettay was released on September 4, 2026 by Lidiopmusic as a part of the album Wettay - Single
September 4, 2026
LabelLidiopmusic
BPM106
Melodicness
Acousticness
Valence
Danceability
Energy

Lyrics

Wettay
Aduna ngi ni,
Ba mu sossoo ba léegi ni,
Nit ki mu ngi fi di dange-dange.
Nit dinala jege lool, gën la sori,
Nit dinala sori lool, moom gën la digé.
Bul tiit di wett-wett,
Waxtaanal ak sa xol,
Bul tiit di wett,
Waxtaanal ak sa xel.
Refrain :
Wettay, ha ha ha, mooy sama nooflay.
Wettay, ha ha ha, mooy sama nooflay.
Verset 2 :
Xarit dinala fit melni jiit,
Mënoo romb ludul nit.
Ndaxte ñi la japoone dëmb,
Ñoo lay bayendoo,
Bu sa rongoñ di siit.
Wettay dinala tax,
Kénn du la sipp, hé yaay !
Bul tiit di wett,
Wettal ak sa xol,
Bul tiit di wett,
Wettal ak sa xel.
Wettay du dara,
Mooy sama jamm.
Wett ak sama bopp,
Wett ak sama xol,
Wett ak sama xel,
Du dara, ha ha
Written by: Papa Aly Diop
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...