Lyrics

Enh chérie Souma la né beugueunaleu Ngua war ma geume Wakhna ngua dégueu Dieuf na ngua guiss Boléko di nieuw goudek beuthieuk Souma la né beugueunaleu Ngua war ma geume Mbarckou mbeuguel Dey méme wakhi nopi Khol ken dou ko dieune Dey beugueu mou danko Dolé gui si mbeuguel Mome dal diakhalnama Mbeuguel moy dougou si nite Deff lo ko lou mou deyoul Légui ngua beugueu nite Mou naane na ko topé Li ngua yorel moy Mbeugel la bari dolé Mbeuguel si khol ley nek Lou khol khame yeugueul ko khéle Ya nek si sa ma khol mi Khelmi dou la bayi So beugone bidiw Dieuf lay fanané Chérie beugueu na la Yaye sa ma trésor Ko beugueu la beugueumane Lo bégne bégne na ko chérie Yaye sa ma trésor So beuguone bidiw dieuf laye fanané Chérie beugueuna la Yaye sa ma trésor Mbeuguélohhhh Mbeuguel Mbeuguel dou louy diem Mbeuguel dou louy forcé Nak kou nek si khol si khel leye daw Yen djiguénou sénégal Anh mane nope na len ngui sen ame diom Anh dionguoma fi la fek bakh Nioune goorou sénégal Souniou djiguéne moy souniou
Writer(s): Assane Mboup Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out