Krediler
PERFORMING ARTISTS
Abdou Guite Seck
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Abdou Guite Seck
Songwriter
Şarkı sözleri
Barro
Barro dafa am rendez vous
Te néne dara douko yakhal
Ba mou nieuwé Dakar ba tay
Mi gui fi soga am bén guél
Barro dafa am rendez vous
Ba takh mou beugue dagg sounou liguey
Ba mou nieuwé Dakar ba tay
Mi gui fi soga am bén guél
Thiéy mani Barro
Aywaay Barro
Aywaay !
Barro dé mine na
Thiéy mani Barro
Hé Barro
Aywaay !
Barro dé mine na
Astou tougueul nda tali
Goné gui Barro néko nam
Boula yonné marsé tougueul
Nagua ko dieundeul kani khégne
Bo amoul kani khégne
Boul fa khouloo boul fa khékh
Les papas, les mamans ho ho ho !
Dégual Barro ma gua naan ko
May naala sama yaay may la sama dady
May samay fém may la samay salagne
Boula nékhe yata youmbé leumbeul ba mou nékh
Boula nékhe déf ma lila nékh
May naala sama yaay may la sama dady
May samay fém may la samay salagne
Bou saa gualou baay téré ma may la dieune
Boula nékhe wakh ma lila nékh
Maay sa diam di sa talibé
Di sa louné thi sa diamano
Loma sant louné lay déf
Yaw dé yay sama commandant
Barro dafa am rendez vous
Ba takh mou beugue dagg sounou liguey
Sa bounou amé répétion
Moom mi gui yoné ay sms
Thiéy mani Barro
Han mani Barro
Aywaay !
Barro dé mine na
Thiéy mani Barro
Haaaa Barro
Aywaay !
Barro dé mine na
Sénégambia, Abdoo gui ni.
Wa Mauritanie kay lén wakhak Barro
Chékhooo Sarrréne bi
Wakhal ma Alima Ndione
Li moo takh faw niou dem ba banéne yoon
Bouniou fi délousséééé !
Mou guen fé nékh
Barro dafa am rendez-vous « Dikkeul »
Ba takh mou beugue dagg sounou liguey « Khaleyi Sénégal »
Ba mou nieuwé Dakar ba tay « Khaleyi Gambia »
Mi gui fi soga am ben guel
Sama gaa yé !
Pape Cheikh Diallo wakh thi
Sister Fa Vivi kaay wakh thi
Mouhamed Mbay kaay wakh thi
Dj Sidath, Dj Prine, Dj Boubs kaay wakh thi
Sister Maria wakh thi,
Baba Soiré kaay wakh thi
Dj Cool loo, Dj Nicola, King Secka, Dj Cheikhou
Birima lambaay waa lambaay
Liguey laniou kham kaay wakh thi
Fara lambaay lat Diakhou Ndiaye
Seutou Alé Baba wakh thi
Sidy Gueye l’homme Djiaraf hé
Dj Makhou, Dj Hervet
Sister Mia Kaay wakh thi
Seugne bi Aliw kaay wakh thi
Sister Maty, Sister Thiaba !
Kouthia kaay wakh thi !
Hé mani Barro
Haaaa mani Barro
Ay mani Barro
Barro dé mine na
Héy! Astou tougueul nda tali
Gone gui Barro néko nam
Boula yonne marsé tougueul
Nagua ko dieundeul kani khegne
Bo amoul kani khégne
Boul fa khouloo boul fa khékh
Les papas, les mamans ho ho ho !
Written by: Abdoulaye Guitte SECK