album cover
Wanted
album cover
Wanted adlı parça {albumName} albümünün bir parçası olarak Rep'tyle Music Group tarafından 5 Aralık 2020 tarihinde yayınlandıSenegalboy
5 Aralık 2020
FirmaRep'tyle Music Group
BPM96
Melodiklik
Akustiklik
Valence
Dans Edilebilirlik
Enerji

Şarkı sözleri

Thiey li jomi na jomi na jomi na
Thiey li jomi na jomi na jomi na
I wanna see this girl ayway wan len mako
Kuma ko guissal lum laaj man ma jox ko
I wanna see this girl ayway wan len mako
Fuma ko guissone demm nafa nekku fa
Wanted Wanted
Hm hm...
Wanted wanted lélé
(Baba, Baba)
Wanted wanted
(Sokhna ci ñëwël ci man kay way ah)
Wanted wanted lélé
(Oinn Packathing )
Mom lay seet guisso ki
Tontu ma mu gaaw waxal way yah yah
Xoćc nama mbeggël i can't breathe
Gennë guñu wayé ma ngui fiir yah yah
(Samba yow amna no mel ki nga guiss ko tëy ngani da nga ko nopp
Samba mi amna numu mel ki romb fi legui mouni dafko nopp)
Thiey li jomi na jomi na jomi na
Thiey li jomi na jomi na jomi na
I wanna see this girl ayway wan len mako
Kuma ko guissal lum laaj man ma jox ko
I wanna see this girl ayway wan len mako
Fuma ko guissone demm nafa nekku fa
Wanted Wanted
Hm hm...
Wanted wanted lélé
(Baba, Baba)
Wanted wanted
(Sokhna ci ñëwël ci man kay way ah)
Wanted wanted lélé
Girl girl your body body make me crazy
Teksi da nga bandit bandit sipp nga deal bi
Linguere bu baax soxna ci you so pretty
Jabar lalay def aytia wan ma sa daddy
Come to me and whine it for me girl
(Nananananana)
Come to me and shake it for me girl
(Wawawawawawa)
(Samba yow amna no mel ki nga guiss ko tëy ngané da nga ko nopp
Samba mi amna numu mel ki romb fi legui mouni dafko nopp)
Thiey li jomi na jomi na jomi na
Thiey li jomi na jomi na jomi na
I wanna see this girl ayway wan len mako
Kuma ko guisal lum laaj man ma jox ko
I wanna see this girl ayway wan len mako
Fuma ko guissone demm nafa nekku fa
Wanted Wanted
Hm hm...
Wanted wanted lélé
(Baba, Baba)
Wanted wanted
(Sokhna ci ñëwël ci man kay way ah)
Wanted wanted lélé
Ohin Packathing
Wanted wanted
Wanted wanted
Wanted wanted
Wanted wanted
Written by: Christ Johan Ollanghas Kimbeki, ODODO NNAMDI ANYANWU, SAMBA TINE
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...