album cover
Merci
album cover
Merci adlı parça {albumName} albümünün bir parçası olarak Diamono Production tarafından 1 Ağustos 2021 tarihinde yayınlandıClimat
AlbümClimat
Yayın Tarihi1 Ağustos 2021
FirmaDiamono Production
BPM109
Melodiklik
Akustiklik
Valence
Dans Edilebilirlik
Enerji

Şarkı sözleri

Yéen ñi ma tallal loxo
bi ma jafandoo
seen’i ñaan fekk si ma
ma doylu si
ma naan jaraJëf
Ngeen bokk si
Merci, merci
Si jappale bi
da fekk ñoo xam ni
da ñoo sàkku ñaan
Te bu la fekki see
Amin’a la war
kon nak, jarajëf
Bi ma dellu see
merci, merci
Si tawawu bi
wow wow
wow wow
li ma gëna neex
seen yéene
defa ànd’ak ñaan
bu ñu tibbée
ci bii xol
Dëgg rek’a wóor
Ngërëm dab na leen
Mbëgéel rek’a wóor
merci, merci rek
moo ma war
Xama naani
bëri na ñoo wam ni
da ñoo jaaxle lool
waaye
defa fekk ni
mujjéel baa ngi xaar
kon nak jarajëf
Jël leen li ngeen moom
Merci, merci
Xol’ay wax ak yéen
wow, wow
wow, wow
demoon naa
di ko wax
ñakka fekkee woon
nekk fa
jox ma seen xol
ak seen’i ñaan
ak seen’i yéene
ma nangu lool
Dem naa
dem
Jël seen’i njukël
delloo leen ko
Te xam ni
newoon naa di ko woy
Mën ngaa woy nit
te doo tuddu turëm
mu xam mooy kan
dello naa leen ko
MERCI
Merci, merci
Jël leen li ngeen moom
kon nak
Jarajëf
Xol’ay wax ak yéen
merci, merci
Jël leen li ngeen moom
Written by: Herve Samb, Omar Pene

Loading...