album cover
Weetay
album cover
Weetay adlı parça {albumName} albümünün bir parçası olarak 4427077 Records DK2 tarafından 31 Ağustos 2022 tarihinde yayınlandıWeetay - Single
31 Ağustos 2022
Firma4427077 Records DK2
DilEnglish
BPM70
Melodiklik
Akustiklik
Valence
Dans Edilebilirlik
Enerji

Müzik Videosu

Müzik Videosu

Şarkı sözleri

Mmmmmmm
Bës bu waroon nex la mujjee ay joy
Sama yaram daw na, sama xol toy na
Ki ma bëgg dem na, ku ma ko waxoon
Mënu ma ko gëm li comme ay leboon
Pexe noon lu am la, lu ma xam la man
Jam nañ sama xol ba baa mu jaare fa
Garab u mbëggeel so dagge reen ya
Bul ci mësa yaakar gis ca dom ya
Haaaaaaann
Leleenenenen
Namm nala lool
Te xammuma fan nga dem
Du ma la mësa fàtte
Ak fo mëna dem
Sa may ñaan nala fekk
Fo mëna nekka
Dalalal sa xel
Sama xol ya ci nekka
Namm nala lool
Te xammuma fan nga dem
Du ma la mësa fàtte
Ak fo mëna dem
Sa may ñaan nala fekk
Fo mëna nekka
Dalalal sa xel
Sama xol ya ci nekka
Sëy nañ ba am jaboot sama xel
Jotuluma bayi ku maleey xolee
Rongoñ dina siit suma la ñakkee
Mbëggeel dina tiis jàmmu wa wàññeeku
Yàlla na nga xippe sama kër
Cat bañ la jiitu ci sa njegenaay
Tëddi nga yobale sama mbëggeel
Tëddi nga bayi mak dundu nammel
Xam na ne nala manquer lool
Wara dundu duma gis sa dom
Dañ la nangu ci sameey loxo
May ñuma sax ma xool sa xol man
Hannnnnn (may ñuma sax ma xool sa xol man)
Lelelennnn way
Namm nala lool
Te xammuma fan nga dem
Du ma la mësa fàtte
Ak fo mëna dem
Sa may ñaan nala fekk
Fo mëna nekka
Dalalal sa xel
Sama xol ya ci nekka
Namm nala lool
Te xammuma fan nga dem
Du ma la mësa fàtte
Ak fo mëna dem
Sa may ñaan nala fekk
Fo mëna nekka
Dalalal sa xel
Sama xol ya ci nekka
Written by: Charles Mbaye Diagne, Massamba Wade
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...