Lyrics

Banial lolou (n fois) Yeina say ma kompou leup nopi bayila si bir Limey togou sou nioré nga xam né may bandit pire Tioy djiboul diapéma dof boudé moy dalal sa heil Madone sa ngaka ba am Lima beugue bou yabo nagne ma djéleu Xam bathia dafa neix djiguéne péxé koon Wéro Yow bandit ngamay diay dagay diém meuneugo Guiss ma tey né dagma nobb ma ré nga fogue né dal Nga thii fowéma mola taxa dioug wayé dotoko défati Ma Aÿ thii gor bou guemoul dara ték si beugue ma fowé damley xol dila Ré nane la baby yafi né nane la amo morom béne ngafi sama Gloria niou guéne dioni dioni thiop sa wari tok di xar ria Banial lolou (2fois) May wahak Yow mani banial lolou Adioul lolou (2 fois) Yama gueune xam né ragalouma lolou Def si code (5 fois) Fi lofi indi ngafi feik boulma wo si Arou bandit mane gor la té awma loumey perte Wathiél sa bopou dalal boul diay sa taar Ni allal amo loudoul sa bop li dalay tardél Sa dara bouger woul ndah lépeu nga statut (mbété monument) Loula méték loula néx nga douguel statut (té todjo féneu) Sol ak soumi mélni amo béneu soucis so Xoulok sa copain nieupeu xamko thi seu statut Keine faléwoula ko djotél yako toogne Yow sonal nganiok ma yeureum samay noon Mbeuguélou film nguéne di doundou falétou léne Moeurs girl bouy wiri wiri dou meuss diok thi mbettel Dioubeudi wessouwoul déf statut nane la Femme du boss Kane la meuno léne niou ték xeil Yeine kouleine rawoul dei niémé Ngueine gueumo léne dara ehh Yow réglél Bo doon mbeur nar nga beuri défaite Niata nga naan baby yafi né bilay yamey daanél Adioul lolou (2fois) Yama gueune xam né ragalouma lolou Banial lolou (2fois) May wahak Yow mani banial lolou Def si code (5fois) Bagn ma ley may (mayma sama baat man) Mayéwouma(do mayé bougne la mayé do dieul) Mouyéne(ndigueli) Yow ndiguelane (ndigueli) (2fois) Bouldi gawa nagou yeuk sa bopou boudoul Yow di kénéne Ni mey diapé lay baayé té man gor douma fowé Leungo néxna wayé ko bayi mou démaki nbagam Si tu peux m'oublier je ferais comme si t'étais jamais né Yagui nax sa bopou so foguéni meunoumala bayi Djiguéne sou gnégué dotoul soor xolam xawma loy diay Beugue guim la beug boulko diapé ragal (Boulma topou bama seuss nit kou neik amna limite) Respect bimla diox délo mako wala kou nék Dém (nangoul nala louné thikaw nga nék niit) Xoulo goudi xoulo beuthieuk dara taxoul nga Beig louniow nga mér dama sonou say caprices Gor dou ngora késsé djiguéne dagkoy meuneu yeureum Man kouma nara sonal man ma rombou lafi Banial lolou (2fois) May wahak Yow mani banial lolou Adioul lolou (2fois) Yama gueune xam né ragalouma lolou Deif si code (5fois)
Writer(s): Unknown Unknown, Abdoul Aziz Fall Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out