Lyrics

Par AbouAmg Liguay djay damakay mayé Waw man yoyu damakay def Affiché indo dawal cow boy Anh man yoyu damakoy def Liguén teulé damakoy fowé Waw man yoyu damakoy def Sagnsé dumako yeugual sama yaram Surtout yoyu damakoy def Ak yoyu yeup damakoy def Xulo wuma xéxuma Même yoyu damakoy def Fuma teulé ngani tala meuné Yoyu yeup damakoy def Aka ma bandit man ci xallé Yoyu yeup damakoy def Ngani dama leer pourtant damako woyafal Def relax nank ni comme kussi beugoul dara Ragaluma kénn kuddul yallah mima saak Té kouy dokh ci leundeum Moy sokhla lampe yi takk Taluma tothie man Damay tabakh guis nga nima coolé Damako meun ba xamko motax Num nekh lakoy déffé Bussa garde wathie taay nga raak ba duggu palais Nala téla fay ni lakeu ci biir pompier Sama deer menoko yak li nangako tak téré Del deuké xine may deuké taw ba bum yi bayi doré Ligni def du bén guiss nga ci bolé pank Fo guis samay tof si souf cœur yi lalko nank Xamé sissou man yi dilém bégué Yoyu sakh damakoy def Yégual ford dilén djégué Même lolu damakoy def Eh dumalen ban yallah féré Aak yoyu May zero kuma xamul dima jugé Surtout yoyu Soma sagga samlay bal Somay gnodi bandit ma gneuw tégal la baye fall Ak yénén damakoy def Oh yén réwo léén Yoyu yeup damakoy def Bilay réwo léén Yoyu ak yénén sakh Ma nigga yaw bul mél kom man Dagual diém man damko meun Amo xalis amoy pékhé fomay songué malay meun Dama liquide sumay wax sa xol day foy même soum'lay nakh Non du mystique vue yé neuri ba fake yi nan dafa rakh Boy yaw wéro wéro Rang bu gnor ci BM du bénn ak bugni kolo kolo Gni dagnu beuri défaut kumay teukalé ak gnom xamo A part sa guél loumay doyé kumay téék loxo Fagua tolu romb nafa Fagua dieum djougué nafa Malén gueune réw sama sound guena nice dossi dégu saga Té lumu diar ma dieunde ko Touss Eh gnun lumu diar gnu dieunde ko Touss Loum diar gnu dieunde ko Touss Tapétu gnu lolu Touss Deug du nékh Touss Sama yaram day xésam sen piks yi dimay nekh Touss Cana warul ragal wétt yéén gneupeu mane kassé Fumalén féék diomal leen kom guél bu faram fassé Saga ma mdeye mala bal Respecté na sama yaaye Kon kéneu ci yéén duma xam Sudone ay wax damay raay Gno boku ligni def mais dama ci bolé sagn sagn Bayina dugal statut damay sonak please send send Anh deug la meun na cool Mais meune na con Amna djiko bandit ak djiko innocent Dama beuri féén mak yén du game Lumay doyé, luma diap dama beug dem Wa waxlén gni deug Xol' én kulén gueunal gueunal Eh wa waxlén gni deug Mafi néék té waxo lu niit meuna dégu Man lumu diar, ma dieunde ko Touss Séral zérol Touss Ak dokh bu gnak xorom Touss Su diékhé rek diékhna Touss Deug du nékh Touss Wolma bandit yeup
Writer(s): Unknown Unknown, Abdoul Aziz Fall Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out