音乐视频

Youssou Ndour - Mama Africa - ALBUM - MBALAX
观看 {artistName} 的 {trackName} 音乐视频

制作

出演艺人
Youssou N'Dour
Youssou N'Dour
演唱
Moussa Diabaté
Moussa Diabaté
表演者
Ibrahima N'Dour
Ibrahima N'Dour
表演者
作曲和作词
Youssou N'Dour
Youssou N'Dour
作曲
Moussa Diabaté
Moussa Diabaté
编曲
Ibrahima N'Dour
Ibrahima N'Dour
编曲
制作和工程
Youssou N'Dour
Youssou N'Dour
制作人
Boubacar N'Dour
Boubacar N'Dour
监制
Patrick Tucker
Patrick Tucker
助理制作人
Prince Mactar NDOUR
Prince Mactar NDOUR
录音工程师

歌词

Yée, yée-hé-hé-hé Yée, yée-hé-hé-hé Hoo, hoo ehnnn haaan Hoo africains, woy le leen ma africa Benn continent, melul ni africa Amul benn werente ci loolu Suñu mbëggél ci yaw, Africa Amna ñi soriyaante Bu ñu kenn jaxasse Na ñu xam suñu bopp Une jeunesse engagée, africa Namm u ñu dara, yalla a la barkeel Tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo Boo xasee miin xam ni, fii mooy suñu kër Come home with me Hoo africains, woy le leen ma africa Benn continent, melul ni africa Amul benn werente ci loolu Suñu mbëggél ci yaw, Africa Ana ñi soriyaante Bu ñu kenn jaxasse Na ñu xam suñu bopp, avec Une jeunesse engagée, africa Namm u ñu dara, yalla a la barkeel Tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo Boo xasee miin, xam ni, fii mooy suñu kër Come home with me Ñun africains, su ñu ànd a ndoo Bokk nday ak baay, Boole suñuy doole Kholal ëllëg u adduna bi Seetal say doom ñoo, koy mujjee Yée, hée hée, an han Ni nga maggeek, ni nga yaatoo Noonu nga riché Ni nga maggeek, ni nga yaatoo Noonu nga riché Du ñu la weccoo ba muk Du ñu la weccook keneen africa Xam nga ni la say, doom yi bëggee Tag naa la kaay Yaa ne ci suñu xol Wo, wo, wo, wooy Wo, wo, wo, wooy Du ñu la mas a weccooy Kenn du yaw Africa Yée ... yée hé hé hée hé
Writer(s): Dave Richards, Hakeen Abdulsamad, Everold Anthony Dwyer, Paul Henton, Bradley Brown, Tilmann Otto, Dalton Anthony Browne, Bobby Dixon, Aliaune Thiam Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out