音乐视频

音乐视频

制作

出演艺人
Voilaaa
Voilaaa
表演者
群星
群星
混音师
Bruno Hovart
Bruno Hovart
低音吉他
Lassana Sané
Lassana Sané
领唱
作曲和作词
Bruno Hovart
Bruno Hovart
词曲作者
Lassana Sané
Lassana Sané
词曲作者

歌词

Allalou yalla lagnou si keuroupe nafsou
(benn bene la)
Allalou yalla lagnou si soufessé
(benn bene la)
     
Gadi nitte kou gnoule ba nitte kou wéhe
(benn bene la)
Nite yagui rayaté bis bouné
(benn bene la)
   
Guisna bolo gou bari dolé
(benn bene la)
Aye bolo moye sounou dolé
(benn bene la)
Masla ak yeurmandé diéhena fé
(benn bene la)
Kocc Barma néla li bouco fowé
(benn bene la)
Gueumale
(benn bene la)
Diapo liguéye mognou ware
(benn bene la)
Gnou mbolo ba done kéne
(benn bene la)
Lougnou ame dadico sédo
(benn bene la)
Gnou boco gnoune béneu daape
(benn bene la)
Mané lolou dale moye sama guinteu
(benn bene la)
Wa kouné di heuthieu borame
(benn bene la)
Gueumale benn bene
(benn bene la)
béne béne la Guisna bolo gou bari dolé
(béne)
béne la Aye bolo moye sounou dolé
(benn bene la)
Written by: Bruno Hovart, Lassana Sané
instagramSharePathic_arrow_out

Loading...