制作
出演艺人
Kya Loum
表演者
作曲和作词
Kya Loum
作词
Olivier Delahaye
作曲
Abdoulaye Sy
作曲
制作和工程
Nautylusprod
制作人
歌词
Gueustouna na ba xaam ragne'na
Mame loumou lep deugue
Tay xaam na thi daraa
Tewena temb nguir se'y
Si seuy te' yallah takh
Tamou na ouff kouli ndiabote gui
So tuke' te' na sa xel daal
Bour yallah moma bolek yaw
(My love)
Beuguela demb tay la raw
(Sama xol)
Ma nangou ko di ko ndamo
(My love)
Lawela thiate ndax amoulo morome
(Ken dou yaw)
(Heey)
Yaw la yaw la
Yaw lama yallah bolel si adouna
(Heey)
Yaw la yaw la
Li may niane bour bi yallah moy sa bo tangue' malay ke'ral
Done sa yaye fall di la sikaral
Matela kanam te meune sa ganaw
Mbeuguel gouy laaw ba faaw
Baniou andado thi batine di fanaaw
Baby yallah moma bolek yaw
Te lou yallah bole
Samb ko moy li woor
Tewena temb nguir se'y
Si seuy te' yallah takh
Tamou na ouff kouli ndiabote gui
So tuke' te' na sa xel daal
Bour yallah mome' bolek yaw
(My love)
Beuguela demb tay la raw
(Sama xol)
Ma nangou ko di ko ndamo
(My love)
Lawela thiate ndax amoulo morome
(Ken dou yaw)
(Heey)
Yaw la yaw la
Yaw lama yallah bolel si adouna
(Heey)
Yaw la yaw la
(Baby, Baby)
Yaw la yaw la
Yaw lama yallah bolel si adouna Yaw la yaw la
(Heey)
Yaw la yaw la
(Baby, Baby)
Yaw la yaw la
Yaw lama yallah bolel si adouna Yaw la yaw la
(Heey)
Yaw la yaw la
Written by: Abdoulaye Sy, Kya Loum, Olivier Delahaye