制作

出演艺人
Aida Samb
Aida Samb
表演者
作曲和作词
Beneth Seraphin Akatche Koffi
Beneth Seraphin Akatche Koffi
作曲
Bakhaw Dioum
Bakhaw Dioum
词曲作者

歌词

Kofi defal lou bakh tay lou bonne lalay faay

Adouna sa xarit mom meeun naa doone sa none
Damako jii teranga mou faay ma lou bonne
Linga tambalee parego
Badola badola lay donne rek bâ des
Jiko jam laay doundee
Linga tambalee parego
Badola badola lay donne rek bâ des
Defal nala lounee
Teranga lako jii mou faay ma lou bonne lou bonne mou fayma
Coleree lako jii mou fay ma lou bonne lou bonne lou bonne mou faay ma

Adouna nit DINA jaay ngorom nguir done jam
Damala wolou wone loma lathie ma jokhla
Fêtée la fi fêtée la fée fêtée la founeeeeee
L'EP loula mossa meti metinama
Ma bête la ngamay jeuw
Nane mane ak sama jeukeur meunounou âme dôme
Motah may doutée
Ma bêteu la ngamay jeuw badola badola laay done rek bâ des
Defal nala lounek
Teranga lako jii mou faay ma lou bonne lou bonne mou fayma
Coleree lako jii mou fay ma lou bonne lou bonne lou bonne mou faay ma
Teranga lako jii mou faay ma lou bonne lou bonne mou fayma
Coleree lako jii mou fay ma lou bonne lou bonne lou bonne mou faay ma
Nanga kham li ame souba yow
No no no
Loula yallah denthial yow
No no no
Nanga fok ni gaagn ngama yow
No 'no no
Nanga beteu mais beteu mais awma ngaagn
Linga tambalee parego
Badola badola lay donne rek bâ des
Jiko jam laay doundee
Linga tambalee parego
Badola badola lay donne rek bâ des
Defal nala lounee
Teranga lako jii mou faay ma lou bonne lou bonne mou fayma
Coleree lako jii mou fay ma lou bonne lou bonne lou bonne mou faay ma
Teranga lako jii mou faay ma lou bonne lou bonne mou fayma
Coleree lako jii mou fay ma lou bonne lou bonne lou bonne mou faay ma
Nanga kham li ame souba yow
No no no
Loula yallah denthial yow
No no no
Nanga fok ni gaagn ngama yow
No 'no no
Nanga beteu mais beteu mais awma ngaagn
Written by: Bakhaw Dioum, Beneth Seraphin Akatche Koffi
instagramSharePathic_arrow_out

Loading...