音乐视频

音乐视频

制作

出演艺人
Abdou Guite Seck
Abdou Guite Seck
领唱
作曲和作词
Abdoulaye Guitte SECK
Abdoulaye Guitte SECK
词曲作者
Ousmane Ka
Ousmane Ka
编曲
Bril
Bril
编曲
制作和工程
Abdou Guite Seck
Abdou Guite Seck
制作人

歌词

ÉTAT CIVIL
Bou dom dioudoo gane si Adouna
Terou ko tataggal ko
Nekkal ko teral ko
Wan koo mbaakh gui mi dioudo
Wan ko yennek thiossan
Nague ko diem diokh deukouwaay
Te mou am ndey ak baay
Diokh ko lidjias
Yimou moomal bopam
Bagnia dem bay mag diakhle
Di seet mom may kan
Gone gou fi magg
Warna khippi khame
Ragne mom moy kan
Gaw len dem declarer dji ko
Dawal gaw thia ndawal bour
Yeugeul ko gan nieuw na
Bala mouy am ben att
Geudaam thi rew mi door
Boul saggan bamou yeekh
Doom dess koy teral
Donte sakh booko fore
Dieumou yonnetti bi la
Agent civil ragnie len
Thi mbeugeul ak thiofel
Bou wesso sounou sabab
Namelou Yallah lah
Gone gou fi magg
Warna khippi khame
Ragne mom moy kan
Bou doom di magg diakhle
Bou diggante sooso ba mawlaana sede
Yeureumeunte teyente
Weggante beuguente
Daw len gaw thia ndawal bour
Yeugeul ko sene bollo
Etat civil ragnie lene
Euleuk mou gounge len
Gua siggi saggal ko
Moom mou siggi saggal la
Ferninte bou ne
Meuna indi bepp guenel
Farloul ba boo deudoo
Farlou fegne thi sa menief
Sa guinaw bagnia diakhasso
Bou doom di magg diakhle
Haaaa! Farlou len
Farlou lenooo
Ba sa yo len dedoo
Farlou fegnioo
Thi sen menief
Etat civil baa gui ni
Akhou diioudou dafa am
Akhou de dafa am
Sey moo daw thi diggente bi thi seni doundoun
Certificat
Moom moo kay sede
Yaw boul ko sagganne
Kone daw ko woute tel
Kharale yeup yaa gui ni di len khaar
Conservation
Gestion automatise
Archivage
Acte daal moom moy li woor
Li moom moo lay nekkal
…Fin…
Written by: Abdoulaye Guitte SECK
instagramSharePathic_arrow_out

Loading...