音乐视频
音乐视频
制作
出演艺人
Defmaa Maadef
领唱
Mamy Victory
领唱
Defa
领唱
作曲和作词
Ndeye Fatou M'Baye
词曲作者
Ndèye Penda Faye
词曲作者
El Hadji Souleymane Diagne
词曲作者
Vincent Emmanuel Ndiaye
词曲作者
制作和工程
Cenzo Beatz
制作人
Baay Sooley
制作人
歌词
MAMY
Amatuma luma prouver si rap Luma prouver si japp
Dëgg dëgg dama job ba fa
Bu dé kaani dafa wara saf sapp
Dama fight si street ba sama jant fenk
Yagg na ñu dima xeep bobu succès xeñ
Yagg na si naaj pour meyna tok si ker gui
Wow ni xeer ana ñi fi sani nene
Xalé féroce dama paré
Niémé encaisser
Def bayi essaie duma dieku di baalé ndam yobalé
Diem ma depassé ma tar tar fessée si sa cas muy clap def
Tadj tadj tadj tadj taratata tataj tagaragarat
REFRAIN
Kalanakh kalanakha
Kalanakh kalanakha
Kalanakh kalanakha
Kalanakh anh x2
DEFA
Lingey wër la yor sama poss
Non mane dama féroce
Li fi jota jaar ütek sama boss
May kaani sa sauce
Dumala si may té do si moss
Ku liggey buko nékhé noce
Saf sapp may li si nokoss
Eh lo thiéré ma sauce
HOOK
Tadj tadj tadj tadj taratata tataj tagaragarat tagaragarat
REFRAIN
Kalanakh kalanakha
Kalanakh kalanakha
Kalanakh kalanakha
Kalanakh anh x2
OUTRO
Kala kala kala kalanakha
Kalanakh kalanakha Kalanakh
Kala kala kala kalanakha
Kalanakh kalanakha Kalanakh
Written by: El Hadji Souleymane Diagne, Ndeye Fatou M'Baye, Ndèye Penda Faye, Vincent Emmanuel Ndiaye