歌词
Daaray LËk
Xale pare ñeeme risque taxaw arrêt
Am ambition xam fiñu jëm di xool fu soree
Fii gas ñi dañu sangu waye kenn nelawatul
Man damay focus nga nee ci diversion duma la faale ba lay jox attention
Fernañu ay nakh sonn ci ay wax ak ay diguee yu bare
Fii Daaray lëk lë kenn dufi jaay gudd nopp kuci nee bopp sa bopp waye ñun xam nañ ku ñuy topp
Fii Daaray lëk lë kenn dufi jaay gudd nopp kuci nee bopp sa bopp waye ñun xam nañ kuñuy topp
Ku muss ren dañ la naxoon daaw ku ndobin ray sa ma maam foo seen lu ñul daw
Connectewu xam li xew nga bëgg ñu nakh
Xameeñu duñu jend jaan ci pax
Fernañu ay nakh sonn ci ay wax ak ay diguee yu bare
Fii Daaray lëk lë kenn dufi jaay gudd nopp kuci nee bopp sa bopp waye ñun xam nañ kuñuy topp
Fii Daaray lëk lë kenn dufi jaay gudd nopp kuci nee bopp sa bopp waye ñun xam nañ kuñuy topp
Ñeppa bëgg dem ci kaw te suuf du ñakki gas
Buur yalla mooy mayee doom yaay jarul di jaa
Ki daw ba daaanu bëgg japp yaw sa tankk
Daa bëgg nga melni moom te banque moom du baank
Fernañu ay nakh sonn ci ay wax ak ay diguee yu bare
Fii Daaray lëk lë kenn dufi jaay gudd nopp kuci nee bopp sa bopp waye ñun xam nañ kuñuy topp
Fii Daaray lëk lë kenn dufi jaay gudd nopp kuci nee bopp sa bopp waye ñun xam nañ kuñuy topp
Written by: Afrik Melo, Yoro ndiaye