制作
出演艺人
Elage Diouf
表演者
作曲和作词
Elage Diouf
作词
Johnny Reid
词曲作者
制作和工程
Johnny Reid
制作人
歌词
BOY MEYEE TEE YALLA TAKH BOUL AM LOSIYKHAR
SETT SETTAL BAKHNA WAGNI TILIMAL DAKOGEUN
SA SOUNEE DAFAY LATHIE ARTOU BALA MO EUPI LOKHO
FI THI KEURGUI NU NOUMEL YOW LAY WEUR
BO DIAGLER SA DOLER KI LEUNDEUM N GA MAYKO LERR
BOY ATEE TEE YALLA TAKH MOUNO SI WEET
YERMANDE
RAFET DJIKO
DIAPALANTEE SI ASKAN WI
BOU JANT FENKEE NUMELNI YOW LAY WEUR
REFRAIN
BANEKH MBEGTEE SOUTOURA LA NIEUP DI WOR
TA BOKO AMEE TIEUREREUL MAKO
NI AMOUL BATT NI SEN RAGOGNE MOUMOUL TOUROU
KAY FI
NOU MEL NI YOW LAY WEUR
BO GUISSER LOU RAFET KAR DANGA SIY BEUG BOK
BO KHAMER KOUY DEF NIAWTEF DOKO BEUG GUISS
SO DIEULEE SA ADOUNA DIAGLEL KO KHALEYI SI YONE BOUBAKH
BOU JANT FENKEE NU MELNI YOW LAY WEUR
REFRAIN
BANEKH MBEGTEE SOUTOURA LA NIEUP DI WEUR
TEE BOKO AMER TIEUREULEL MAKO
NI AMOUL BATT NI SEN RAGOGNE MOUNOUL TOUROU
KAY FI
NU MELNI YOW LAY WEUR
LOU BAKH AK LOUBONE MOFINEK TEE AY FEN MOM DOU BEDIAO
DOU LOUNIEP BOK GA NARKO AKIMO
TALALAL MA SA LOKHO NU ANDE
REFRAIN
BANEKH MBEGTEE SOUTOURA LA NIEP DI WEUR
TA BOKO AMEE TIEURELEUL MAKO
NI AMOUL BATT NI SEN RAGOGNE MOUNOUL TOUROU
KAY FI
NU MELNI YOW LAY WEUR
NI AMOUL BATT NI SEN RAGOGNE MOUNOUL TOUROU
SOU JANT FENKEE NU MELNI YOW LAY WEUR
HUHUHUHUHUHUHUHUHUHUHUHUHUHUHUHUHUHUHUUHUHUHUHUHUHUHUHUHUHUHUHU
Written by: Elage Diouf, Johnny Reid

