制作
出演艺人
Alune Wade
低音吉他
Mangane
吉他
Benjamin Naud
鼓
Anthony Jambon
吉他
Inor Sotolongo
打击乐
Hugues Mayot
萨克斯管
Carlos Sarduy
小号
Valérie Belinga
声乐
作曲和作词
Mangane
作曲
Alune Wade
编曲
制作和工程
Raphaël Jonin
母带工程师
Sebastien Tondo
混音工程师
Dominique Boss
录音工程师
Johann Boos
录音工程师
歌词
Emmène-moi ! Emmène-moi !
Là où tu vas ! Là où tu vas !
Yobba léma ba fa ga jëm, su ma ammé njëk jox la ko, ba fa ga jëm
Ah ! Han ! Ah ! Han ! Ah ! Han !
Da ma bëgga dém tukké
Dangne mani woon , kuddul tukki du xamm fu dëk néxè.
Ba gaal gi téer, ma yek ci, dém ci gêj gi, wutti taffésse gè, té xammuma fu maye téerè
Yoon wi lënn dëmm, manni ték ak sama xél, sama xol, dénk sama bop yalla
Emmène-moi ! Emmène-moi !
Là où tu vas ! Là où tu vas !
Yobba léma ba fa ga jëm, su ma ammé njëk jox la ko, ba fa ga jëm
Ah ! Han ! Ah ! Han ! Ah ! Han !
Da ma bëgga dém tukké
Gaal gi téer, ma yek ci, dém ci gêj gi, wutti taffésse gè, té xammuma fu maye téerè

Written by: Mangane