制作
出演艺人
Iam.Jarrah
表演者
作曲和作词
Djibril Mbaye Fall
词曲作者
Mame Diarra Mbaye
词曲作者
Mame Alassane Gaye
词曲作者
Mouhameth Talla Fall
词曲作者
制作和工程
Bril
制作人
歌词
Bril on the beat
Nouma meuna mél iow ya takh
Souma solo bèy dagou bilay iow ya takh
Fouma meuna dém si louma meuna né
Xél dou diogue si iow non sama baby lovaa
Doxalal dama lasi wolou
Do niom té douniou iow ya meune si côté bobou
Baby dawalal fo diare yoon la
Boul tégui figua diapeu faleu bou dara yomb
Délko yeugeul mou saff
Goudi lakoy yeungeul
Sow mi délko yeugeul mou saff
Goudi lakoy yeugeul
Sucré salé
Nigamay deff safnama
Li loumou done xawmako
Xalé bilé diomal nama
Sama paradise aldiana
Nigamay deff safnama
Li loumou done xawmako
Xalé bilé diomal nama
Loma téré ma ba
Loma digeul ma deff
Foma yobou fala
Si iow rek la dess
Kouma khol si iow méréma awma si iow sago ningmay deff
Sama xol bi yasi né sama chérie coco ningmay deff
Bou souf sédé ba lepp ni sélaw
Thiouray gui di dioli ba beute sétt té kéne sou nélaw
Lo deff ayoul bilay dagoul diayoul
Niam nako nexna bayina xam nguani amoul
Délko yeugeul mou saff
Goudi lakoy yeungeul
Sow mi délko yeugeul mou saff
Goudi lakoy yeugeul
Sucré salé
Nigamay deff safnama
Li loumou done xawmako
Xalé bilé diomal nama
Sama paradise aldiana
Nigamay deff safnama
Li loumou done xawmako
Xalé bilé diomal nama
Loma téré ma ba
Loma digeul ma deff
Foma yobou fala
Si iow rek la dess
Lonkouna loukotina xam nguani doyalouma dolimaahhh
Lonkouna loukotina xam nguani doyalouma dolimaahhh
Ahh leeee
Leleleeeee wooyee mane dei wayna leee Diagne narr
Ndaw bou guisoul koumou mine day wétt beugue nala loleeeee ehh
Wane ngua ma mbeuguél wane ngua ma mbeuguél
Wane ngua ma mbeuguél wane ngua ma louy mbeuguél
Written by: Djibril Mbaye Fall, Mame Alassane Gaye, Mame Diarra Mbaye, Mouhameth Talla Fall

