制作

出演艺人
Seckou Keita
Seckou Keita
可拉琴
作曲和作词
Seckou Keita
Seckou Keita
作曲
Kru
Kru
作曲
Moussa N'Gom
Moussa N'Gom
作词

歌词

Ni mala beugué baby
Xayow Meussou ma beugué ni nit
 
Sone thi beugue bani bayina
Nga gneuw indi lumière
Mani wone aye mbeuguél jigou ma
Xol bi deukeu dima toogne
 
Nga gneuw indi deugui mbeuguél
Mou done lou neekh
Waxal gniy wooté ka bippé
Nagne ma thieupé
 
Nimala beugué baby
Xayow meussou ma beugué ni nit
Xayow soumala takké baby (bé)
Xayow douma signé polygamie
 
Sa yo amé loula metti thi mane mi
Damalay xool sourire nga baalma
 
Sama tandarma lala dipé
Mani bu toy ba
Doylo nga sa dignité
Do adou calpé heey hey
Maak yaw dougn réroo
Comment vous allez moi ça va
 
Nimala beugué baby
Xayow meussou ma beugué ni nit
Xayow soumala takké baby (bé)
Xayow douma signé polygamie
 
Digueunté bi deugeu la
Xam sa bop yam do topando
Ma chérie
métina tang dieur dawoulo
Ayi yiii ayé yé aha aa
 
Nimala beugué baby
Xayow meussou ma beugué ni nit
Xayow soumala takké baby
Xayow douma signé polygamie
 
Xayow Nimala beugué baby
Yaw la taneu def la sama diabar
Diabar Diabar Diabar
Yaye sama yayou doome
Xayow gooro foumou dia yé
Waw waw ma yondi sama nii diay
Waw waw ma yem si sama baby
Written by: Kru, Moussa N'Gom, Seckou Keita
instagramSharePathic_arrow_out

Loading...